Results for j'ai écris un livre translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

puis je vis dans la main droite de celui qui était assis sur le trône un livre écrit en dedans et en dehors, scellé de sept sceaux.

Wolof

noonu ma gis ca loxol ndeyjooru ka toog ca gàngune ma téere bu ñu bind biir ak biti, tay ko juróom-ñaari yoon ak sondeel.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

le ciel se retira comme un livre qu`on roule; et toutes les montagnes et les îles furent remuées de leurs places.

Wolof

asamaan si dellu ni basaŋ gu ñuy taxañ, tund yépp ak dun yépp randoo fa ñu nekkoon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

qui disait: ce que tu vois, écris-le dans un livre, et envoie-le aux sept Églises, à Éphèse, à smyrne, à pergame, à thyatire, à sardes, à philadelphie, et à laodicée.

Wolof

naan: «bindal ci téere li ngay gis te yónnee ko juróom-ñaari mboolooy ñi gëm, ca dëkki efes, samirin, pergam, catir, sàrd, filadelfi ak lawdise.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,772,970,887 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK