Results for jamais translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

jamais

Wolof

Last Update: 2021-04-19
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

apprenant toujours et ne pouvant jamais arriver à la connaissance de la vérité.

Wolof

duñu noppee gëstu, waaye duñu man a yegg ci xam-xamu dëgg mukk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

et quiconque vit et croit en moi ne mourra jamais. crois-tu cela?

Wolof

rax-ca-dolli kuy dund te gëm ma, doo dee mukk. ndax gëm nga loolu?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

la charité ne périt jamais. les prophéties prendront fin, les langues cesseront, la connaissance disparaîtra.

Wolof

mbëggeel amul àpp. Ñiy wax ci kàddug yàlla dinañu noppi, ñiy wax ay làkk dinañu ko bàyyi, ñiy xamle xam-xamu yàlla wàcc.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

je leur donne la vie éternelle; et elles ne périront jamais, et personne ne les ravira de ma main.

Wolof

dama leen di jox dund gu dul jeex; duñu sànku mukk, te kenn du leen jële ci sama loxo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

et tandis que tout sacrificateur fait chaque jour le service et offre souvent les mêmes sacrifices, qui ne peuvent jamais ôter les péchés,

Wolof

bés bu nekk saraxalekat yi dañuy taxaw di liggéeyal yàlla, di sax ci def sarax yu mënul a dindi bàkkaar yi mukk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

jamais on n`a entendu dire que quelqu`un ait ouvert les yeux d`un aveugle-né.

Wolof

bi àddina sosoo ba tey, musuñoo dégg nit ku ubbi bëti gumbag judduwaale.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

a lystre, se tenait assis un homme impotent des pieds, boiteux de naissance, et qui n`avait jamais marché.

Wolof

amoon na ca listar nag nit ku fa toog, ku ay tànkam làggi, ndax li mu judduwaale lafañ te musul a dox.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

c`est pourquoi, si un aliment scandalise mon frère, je ne mangerai jamais de viande, afin de ne pas scandaliser mon frère.

Wolof

kon bu sama mbokk sóoboo ci bàkkaar ndax ñam wi ma lekk, dootuma lekk mukk yàpp, ngir bañ a sóob ci bàkkaar sama mbokk mi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

je vous le dis en vérité, je ne boirai plus jamais du fruit de la vigne, jusqu`au jour où je le boirai nouveau dans le royaume de dieu.

Wolof

ci dëgg maa ngi leen koy wax, dootuma naan gannaaw tey ndoxum réseñ mii, ba kera ma ciy naan bu bees ci nguuru yàlla.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

alors je leur dirai ouvertement: je ne vous ai jamais connus, retirez-vous de moi, vous qui commettez l`iniquité.

Wolof

ci kaw loolu dinaa leen wax dëgg ne leen: “musuma leen a xam; soreleen ma, yéen ñiy def bàkkaar.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

car jamais personne n`a haï sa propre chair; mais il la nourrit et en prend soin, comme christ le fait pour l`Église,

Wolof

ndaxte kenn musul a bañ sa yaram. waaye danga koy dundal, di ko fonk. noonu it la kirist fonke mbooloo mi;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

jésus leur dit: je suis le pain de vie. celui qui vient à moi n`aura jamais faim, et celui qui croit en moi n`aura jamais soif.

Wolof

yeesu tontu leen ne: «man maay ñam wiy joxe dund. ku ñëw ci man, doo xiif mukk; te ku ma gëm, doo mar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

pierre lui dit: non, jamais tu ne me laveras les pieds. jésus lui répondit: si je ne te lave, tu n`auras point de part avec moi.

Wolof

piyeer ne ko: «déedéet, duma nangu mukk nga raxas samay tànk.» yeesu ne ko: «su ma la raxasul, doo bokk ak man dara.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

c`est pourquoi, frères, appliquez-vous d`autant plus à affermir votre vocation et votre élection; car, en faisant cela, vous ne broncherez jamais.

Wolof

kon nag samay mbokk, gannaaw yàlla da leena tànn te woo leen, góor-góorluleen ci feddali ko ak seen kem-kàttan. ndaxte su ngeen ko defee, dungeen jeng mukk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Get a better translation with
8,915,500,506 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK