Results for je le dis à personne translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

je dis cela afin que personne ne vous trompe par des discours séduisants.

Wolof

maa ngi wax lii, ngir kenn bañ leen a nax ci ay wax yu neex.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ce que je vous dis, je le dis à tous: veillez.

Wolof

li ma leen wax, ñépp laa ko wax: “xool-leen!”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je vous le dis en vérité, tout cela retombera sur cette génération.

Wolof

ci dëgg maa ngi leen koy wax, loolu lépp dina dal ci niti jamono jii.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je vous le dis en vérité, il l`établira sur tous ses biens.

Wolof

ci dëgg maa ngi leen koy wax, njaatige bi dina ko teg ci alalam jépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 2
Quality:

French

mais il répondit: je vous le dis en vérité, je ne vous connais pas.

Wolof

waaye mu tontu leen ne: “ci dëgg maa ngi leen koy wax, xawma leen.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

non, je vous le dis. mais si vous ne vous repentez, vous périrez tous également.

Wolof

maa ngi leen di wax ne, du dëgg. waaye su ngeen tuubul seeni bàkkaar, dingeen sànku noonu, yéen ñépp itam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 2
Quality:

French

or, je vous le dis, il y a ici quelque chose de plus grand que le temple.

Wolof

waaye maa ngi leen koy wax, am na ci seen biir ku sut kër yàlla ga.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus lui dit: j`irai, et je le guérirai.

Wolof

yeesu ne ko: «dinaa ñëw faj ko.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car, je vous le dis, aucun de ces hommes qui avaient été invités ne goûtera de mon souper.

Wolof

maa ngi leen koy wax, ci ñi ma woo woon ci sama reer bi, kenn du ci ñam.”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je vous le dis en vérité, cette génération ne passera point, que tout cela n`arrive.

Wolof

«ci dëgg maa ngi leen koy wax, niti jamono jii duñu wéy, te loolu lépp amul.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 3
Quality:

French

de même, je vous le dis, il y a de la joie devant les anges de dieu pour un seul pécheur qui se repent.

Wolof

maa ngi leen di wax lii: ci noonule la malaakay yàlla yi di ame mbég ci benn bàkkaarkat bu tuubee ay bàkkaaram.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il dit encore: a quoi comparerai-je le royaume de dieu?

Wolof

mu neeti: «lan laa man a mengaleek nguuru yàlla?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est pourquoi je vous le dis: au jour du jugement, le pays de sodome sera traité moins rigoureusement que toi.

Wolof

waaye maa ngi leen koy wax, keroog bés pénc ma sodom moo lay tane.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car, je vous le dis, je ne la mangerai plus, jusqu`à ce qu`elle soit accomplie dans le royaume de dieu.

Wolof

ndaxte maa ngi leen koy wax, dootuma ko lekk mukk, lu dul ba kera mu mat ci nguuru yàlla.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est pourquoi, je vous le dis, le royaume de dieu vous sera enlevé, et sera donné à une nation qui en rendra les fruits.

Wolof

«loolu moo tax maa ngi leen koy wax, dinañu leen xañ nguuru yàlla, dénk ko xeet wuy def ay jëfam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car, je vous le dis, si votre justice ne surpasse celle des scribes et des pharisiens, vous n`entrerez point dans le royaume des cieux.

Wolof

ndaxte maa ngi leen koy wax, bu seen njubte ëppul njubteg xutbakat ya ak farisen ya, dungeen tàbbi mukk ci nguuru yàlla aji kawe ji.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

efforcez-vous d`entrer par la porte étroite. car, je vous le dis, beaucoup chercheront à entrer, et ne le pourront pas.

Wolof

«defleen seen kem-kàttan, ngir dugg ci bunt bu xat bi, ndaxte maa ngi leen koy wax, ñu bare dinañu jéem a dugg, waaye duñu ko man.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est pourquoi, je te le dis, ses nombreux péchés ont été pardonnés: car elle a beaucoup aimé. mais celui à qui on pardonne peu aime peu.

Wolof

moo tax ma di la wax ne, su wonee mbëggeel gu réye nii, dafa fekk ñu baal ko bàkkaaram yu bare. waaye ki mbëggeelam néew dafa fekk ñu baal ko lu tuuti.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car, je vous le dis, vous ne me verrez plus désormais, jusqu`à ce que vous disiez: béni soit celui qui vient au nom du seigneur!

Wolof

ndaxte maa ngi leen koy wax, dungeen ma gisati li dale tey, ba kera ngeen ne: “yaw miy ñëw ci turu boroom bi, ku barkeel nga!”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

en vérité, en vérité, je vous le dis, vous pleurerez et vous vous lamenterez, et le monde se réjouira: vous serez dans la tristesse, mais votre tristesse se changera en joie.

Wolof

ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, dingeen jooy xàcc, waaye àddina dina bég; dingeen jàq, waaye seen njàqare dina soppaliku bànneex.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,222,799 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK