Results for je regarde la television translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

et je regarde comme un devoir, aussi longtemps que je suis dans cette tente, de vous tenir en éveil par des avertissements,

Wolof

te jàpp naa ko, muy sama warugar, feek maa ngi noyyi, ma di leen fàttali loolu, ba yee leen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et même je regarde toutes choses comme une perte, à cause de l`excellence de la connaissance de jésus christ mon seigneur, pour lequel j`ai renoncé à tout, et je les regarde comme de la boue, afin de gagner christ,

Wolof

rax-ca-dolli dëddu naa lépp ngir xéewali xam kirist yeesu sama boroom, di xam-xam bu xóot, ba xel mënu koo takk. moo tax ñàkk naa sama lépp, te def ko ni mbalit, ngir am cér ci kirist.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,781,371,852 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK