Results for l'or translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

je n`ai désiré ni l`argent, ni l`or, ni les vêtements de personne.

Wolof

nammuma xaalisu kenn mbaa wurusam mbaa koddaayam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

insensés et aveugles! lequel est le plus grand, l`or, ou le temple qui sanctifie l`or?

Wolof

yéen ñi dof te gumba! lan moo gën a màgg, wurus wi walla kër yàlla, gi tax wurus wi sell?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin que l`épreuve de votre foi, plus précieuse que l`or périssable (qui cependant est éprouvé par le feu), ait pour résultat la louange, la gloire et l`honneur, lorsque jésus christ apparaîtra,

Wolof

xam ne nattu yooyu dinañu sellal seen ngëm, ni safara di setale wurus, fekk wurus luy wéy la, te ngëm a ko gën fuuf. noonu seen ngëm dina yelloo cant, ndam ak màgg, bés bu yeesu kirist feeñee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
8,800,711,020 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK