Results for la joie translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

ils furent dans la joie, et ils convinrent de lui donner de l`argent.

Wolof

Ñu am ca bànneex bu réy, dig ko xaalis.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

de même, je vous le dis, il y a de la joie devant les anges de dieu pour un seul pécheur qui se repent.

Wolof

maa ngi leen di wax lii: ci noonule la malaakay yàlla yi di ame mbég ci benn bàkkaarkat bu tuubee ay bàkkaaram.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et quand il eut dit cela, il leur montra ses mains et son côté. les disciples furent dans la joie en voyant le seigneur.

Wolof

mu daldi leen won ay loxoom ak wetam. bi ñu gisee boroom bi, taalibe ya daldi bég lool.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

aussi mon coeur est dans la joie, et ma langue dans l`allégresse; et même ma chair reposera avec espérance,

Wolof

moo tax sama xol sedd,may woy sama bànneex,te it sama yaram di tëdd ci yaakaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

heureux vous qui avez faim maintenant, car vous serez rassasiés! heureux vous qui pleurez maintenant, car vous serez dans la joie!

Wolof

yéen ñi xiif léegi, barkeel ngeen,ndax dingeen regg.yéen ñiy naqarlu léegi, barkeel ngeen,ndax dingeen ree.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car le royaume de dieu, ce n`est pas le manger et le boire, mais la justice, la paix et la joie, par le saint esprit.

Wolof

ndaxte bokk ci nguuru yàlla jotewul dara ak lu nuy lekk mbaa lu nuy naan. nguuru yàlla mooy jub ci kanam yàlla, te am mbég ak jàmm ci dooley xel mu sell mi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et vous-mêmes, vous avez été mes imitateurs et ceux du seigneur, en recevant la parole au milieu de beaucoup de tribulations, avec la joie du saint esprit,

Wolof

te aw ngeen sunuy tànk ak yu boroom bi, ci li ngeen nangu xebaar bi ci biir fitna yu metti, ànd ak mbég ci dooley xel mu sell mi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

quelles actions de grâces, en effet, nous pouvons rendre à dieu à votre sujet, pour toute la joie que nous éprouvons à cause de vous, devant notre dieu!

Wolof

ndaw cant yu bare yu nu war a sant yàlla ndax yéen! ndaw mbég mu bare, mi nu am ci kanamam ndax yéen!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

après l`avoir entendu, ils furent dans la joie, et promirent de lui donner de l`argent. et judas cherchait une occasion favorable pour le livrer.

Wolof

bi ñu ko déggee, ñu am ca bànneex bu réy, dig ko xaalis. noonu mu fexe jamono ju mu leen man a jébbal yeesu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais le fruit de l`esprit, c`est l`amour, la joie, la paix, la patience, la bonté, la bénignité, la fidélité, la douceur, la tempérance;

Wolof

waaye li xelu yàlla mi di meññ mooy: mbëggeel, mbég, jàmm, muñ, laabiir, mbaax, kóllëre,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,774,336,401 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK