Results for la puissance translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

a lui soit la puissance aux siècles des siècles! amen!

Wolof

na yàlla yelloo màgg ba fàww. amiin.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

désormais le fils de l`homme sera assis à la droite de la puissance de dieu.

Wolof

waaye gannaawsi tey, doomu nit ki dina toog ci ndeyjooru yàlla, aji kàttan ji.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin que votre foi fût fondée, non sur la sagesse des hommes, mais sur la puissance de dieu.

Wolof

ngir seen ngëm bañ a wékku ci xam-xamu nit ñi waaye mu wékku ci dooley yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

qui nous a délivrés de la puissance des ténèbres et nous a transportés dans le royaume du fils de son amour,

Wolof

yàlla musal na nu ci dooley lëndëm, yóbbu nu ci nguuru doomam ji mu bëgg,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

au nom du seigneur jésus, vous et mon esprit étant assemblés avec la puissance de notre seigneur jésus,

Wolof

ngeen daje ci turu boroom bi yeesu, te sama xel teewe ko, ànd ak dooley boroom bi yeesu,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

par la parole de vérité, par la puissance de dieu, par les armes offensives et défensives de la justice;

Wolof

ci kàddug dëgg ak ci kàttanu yàlla, nu ngi yor gànnaayi njubte ci loxol ndeyjoor ak lu càmmooñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

or, à celui qui peut faire, par la puissance qui agit en nous, infiniment au delà de tout ce que nous demandons ou pensons,

Wolof

léegi nag, na ndam li féete ak yàlla, mi man a yeggale lépp luy ñaan mbaa yéene, ba weesu ko fuuf, dëppook kàttan giy jëf ci nun;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus, ayant assemblé les douze, leur donna force et pouvoir sur tous les démons, avec la puissance de guérir les maladies.

Wolof

benn bés yeesu dajale fukki taalibe ya ak ñaar, jox leen doole ak sañ-sañu dàq rab yépp ak di faj jàngoro yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus leur répondit: vous êtes dans l`erreur, parce que vous ne comprenez ni les Écritures, ni la puissance de dieu.

Wolof

waaye yeesu tontu leen ne: «yéena ngi cig réer, ndaxte xamuleen mbind mi mbaa kàttanu yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin de connaître christ, et la puissance de sa résurrection, et la communion de ses souffrances, en devenant conforme à lui dans sa mort, pour parvenir,

Wolof

moom laay ittewoo xam, ak doole ji ànd ak ndekkiteem, ma bokk ci ay coonoom, ba fekki ko ci deeyam,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus, revêtu de la puissance de l`esprit, retourna en galilée, et sa renommée se répandit dans tout le pays d`alentour.

Wolof

yeesu dellu diiwaanu galile, fees ak dooley xelum yàlla, te turam siiw ca diiwaan booba bépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ayant été ensevelis avec lui par le baptême, vous êtes aussi ressuscités en lui et avec lui, par la foi en la puissance de dieu, qui l`a ressuscité des morts.

Wolof

bi ñu leen sóobee ci ndox, suulaale nañu leen ak moom, te it dekki ngeen ak moom, ndaxte gëm ngeen ci dooley yàlla, ji ko dekkal ca néew ya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais j`irai bientôt chez vous, si c`est la volonté du seigneur, et je connaîtrai, non les paroles, mais la puissance de ceux qui se sont enflés.

Wolof

waaye bu soobee boroom bi, léegi ma ñëw ci yéen te seet boroom tiitar yooyu; waxuma seen kàddu, seen doole laay seet.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car il a été crucifié à cause de sa faiblesse, mais il vit par la puissance de dieu; nous aussi, nous sommes faibles en lui, mais nous vivrons avec lui par la puissance de dieu pour agir envers vous.

Wolof

néewoon na doole, ba ñu koy daaj ca bant ngir rey ko, waaye mi ngi dund ci kàttanu yàlla. nun itam néew nanu doole ci sunu bokk ci moom, waaye dinanu dund ak moom ci kàttanu yàlla, bu nuy jëfante ak yéen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

dans lesquels vous marchiez autrefois, selon le train de ce monde, selon le prince de la puissance de l`air, de l`esprit qui agit maintenant dans les fils de la rébellion.

Wolof

ci biir yooyu ngeen doon dund démb, topp doxalinu àddina, tey déggal kilifag boroom sañ-sañ yi ci jaww ji, di xel mu bon miy jëf ci kureelu ñi déggadil yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

par la puissance de dieu qui nous a sauvés, et nous a adressé une sainte vocation, non à cause de nos oeuvres, mais selon son propre dessein, et selon la grâce qui nous a été donnée en jésus christ avant les temps éternels,

Wolof

moo nu musal te woo nu ci dund gu sell, ci lu ajuwul ci sunuy jëf, waaye ci dogalu boppam ak yiwam, wi nu yàlla may ci kirist yeesu, ba àddina sosoogul.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et voici, j`enverrai sur vous ce que mon père a promis; mais vous, restez dans la ville jusqu`à ce que vous soyez revêtus de la puissance d`en haut.

Wolof

te man dinaa leen yónnee li sama baay dige. yéen nag toogleen ci dëkk bi, ba ñu sol leen doole ji jóge ci kaw.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

après cela, j`entendis dans le ciel comme une voix forte d`une foule nombreuse qui disait: alléluia! le salut, la gloire, et la puissance sont à notre dieu,

Wolof

gannaaw loolu ma dégg lu mel ni baat bu xumb bu jollee ca mbooloo mu bare ca asamaan, naan:«aleluya!mucc, ndam ak kàttan,yàlla sunu boroom moo ko moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus lui répondit: tu l`as dit. de plus, je vous le déclare, vous verrez désormais le fils de l`homme assis à la droite de la puissance de dieu, et venant sur les nuées du ciel.

Wolof

yeesu tontu ko: «wax nga ko. maa ngi leen koy wax it, li dale fii dingeen gis doomu nit ki toog ci ndeyjooru aji kàttan ji, di ñëw ci niiri asamaan si.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin que tu leur ouvres les yeux, pour qu`ils passent des ténèbres à la lumière et de la puissance de satan à dieu, pour qu`ils reçoivent, par la foi en moi, le pardon des péchés et l`héritage avec les sanctifiés.

Wolof

ngir ubbi seeni bët, nga jële leen ci lëndëm, tàbbal leen ci leer, nga nangoo leen ci sañ-sañu seytaane, woññi leen ci yàlla, ma baal leen seeni bàkkaar te may leen cér ci biir sama gaa yi sell ci kaw ngëm.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,774,131,449 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK