From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
le paradis
àjjana ji
Last Update: 2017-02-08
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
jésus lui répondit: je te le dis en vérité, aujourd`hui tu seras avec moi dans le paradis.
yeesu tontu ko ne: «ci dëgg maa ngi la koy wax, tey jii dinga texe ak man ca jataayu yàlla.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
que celui qui a des oreilles entende ce que l`esprit dit aux Églises: a celui qui vaincra je donnerai à manger de l`arbre de vie, qui est dans le paradis de dieu.
yaw mi am ay nopp, déglul li xelum yàlla di wax mboolooy ñi gëm. ku daan, dinaa la may, nga lekk ci garabu dund, gi nekk ci jataayu yàlla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference: