Results for loi translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

la loi n`est pas contre ces choses.

Wolof

lewetaay ak maandute. yoon wi terewul yu ni mel.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

de ces deux commandements dépendent toute la loi et les prophètes.

Wolof

Ñaari ndigal yooyu tënk nañu yoonu musaa wépp, moom ak waxi yonent yi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

maître, quel est le plus grand commandement de la loi?

Wolof

«kilifa gi, ban ndigal moo gën a màgg ci yoonu musaa?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

parlez et agissez comme devant être jugés par une loi de liberté,

Wolof

gannaaw dingeen nar a jaar ci àtteb yoon, wiy goreel, na loolu lal seen wax ak seen jëf.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car tous les prophètes et la loi ont prophétisé jusqu`à jean;

Wolof

ndaxte li yonent yi wax ak li yoonu musaa tëral ñu ngi doon dox, ba kera yaxya di feeñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car christ est la fin de la loi, pour la justification de tous ceux qui croient.

Wolof

ndaxte ci kirist la yoonu musaa dëppe, ba tax ku ko gëm, dinga jub fa kanam yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car, le sacerdoce étant changé, nécessairement aussi il y a un changement de loi.

Wolof

te bu ñu fi jëlee saraxalekat yi ak seen liggéey, dañoo war a toxal itam yoon, wi ñu fi tëraloon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car c`est par la loi que je suis mort à la loi, afin de vivre pour dieu.

Wolof

ci li jëm ci yoonu musaa, dee naa, fekk yoon wi ci boppam moo ko waral, ngir ma man a dund, ba amal jariñ yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ainsi la loi a été comme un pédagogue pour nous conduire à christ, afin que nous fussions justifiés par la foi.

Wolof

ci noonu la nu yoon wi doon noote, ba kirist di ñëw, ngir yàlla àtte nu jub ci kaw ngëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je trouve donc en moi cette loi: quand je veux faire le bien, le mal est attaché à moi.

Wolof

gis naa nag lii: saa su ma bëggee def lu baax, lu bon a ngi ma taxawu.

Last Update: 2024-04-14
Usage Frequency: 31
Quality:

French

en disant: cet homme excite les gens à servir dieu d`une manière contraire à la loi.

Wolof

Ñu ne: «kii day xiir nit ñi ci màggal yàlla ci lu juuyoo ak yoon wi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

anéantissons-nous donc la loi par la foi? loin de là! au contraire, nous confirmons la loi.

Wolof

xanaa kon ngëm day fanq yoonu musaa? mukk! da koy gën a dëgëral sax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car le péché n`aura point de pouvoir sur vous, puisque vous êtes, non sous la loi, mais sous la grâce.

Wolof

ndaxte bàkkaar dootu leen manal dara, yéen ñi génn ci yoonu musaa, dugg ci yiwu yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

l`amour ne fait point de mal au prochain: l`amour est donc l`accomplissement de la loi.

Wolof

ku bëgg sa moroom, doo ko tooñ; kon ku wéy ci mbëggeel matal nga yoonu musaa.

Last Update: 2024-02-10
Usage Frequency: 4
Quality:

Get a better translation with
7,776,919,557 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK