Results for mange translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

et une voix lui dit: lève-toi, pierre, tue et mange.

Wolof

te baat ne ko: «jógal, piyeer, rey te lekk.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

celui qui mange ma chair et qui boit mon sang demeure en moi, et je demeure en lui.

Wolof

kiy lekk sama yaram tey naan sama deret dina sax ci man, ma dëkk ci moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est ici le pain qui descend du ciel, afin que celui qui en mange ne meure point.

Wolof

waaye ñam wiy wàcce ci asamaan, ku ko lekk, doo dee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

celui qui mange ma chair et qui boit mon sang a la vie éternelle; et je le ressusciterai au dernier jour.

Wolof

ku lekk sama yaram te naan sama deret, am nga dund gu dul jeex, te dinaa la dekkal keroog bés bu mujj ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car celui qui mange et boit sans discerner le corps du seigneur, mange et boit un jugement contre lui-même.

Wolof

ku lekk mburu mi, naan ci kaas bi, fekk faalewuloo solos yaramu kirist wi, sa lekk ak sa naan dina xëcc àtteb yàlla ci sa kaw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et les pharisiens et les scribes murmuraient, disant: cet homme accueille des gens de mauvaise vie, et mange avec eux.

Wolof

farisen ya ak xutbakat ya di ñurumtu naan: «waa jii mi ngi nangoo nekk ak ay boroom bàkkaar ak a lekkandook ñoom!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

comme le père qui est vivant m`a envoyé, et que je vis par le père, ainsi celui qui me mange vivra par moi.

Wolof

baay bi ma yónni mu ngi dund, te maa ngi dund jaarale ko ci moom; noonu itam ku may lekk dina dund jaarale ko ci man.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

que chacun donc s`éprouve soi-même, et qu`ainsi il mange du pain et boive de la coupe;

Wolof

na ku nekk seetlu boppam nag, sog a lekk ci mburu mi te naan ci kaas bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

prenant alors la parole, il lui dit: que jamais personne ne mange de ton fruit! et ses disciples l`entendirent.

Wolof

ci kaw loolu mu ne garab gi: «dootuloo meññ mukk!» taalibe yi dégg loolu mu wax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

que celui qui mange ne méprise point celui qui ne mange pas, et que celui qui ne mange pas ne juge point celui qui mange, car dieu l`a accueilli.

Wolof

kiy lekk lu nekk, bumu xeeb ki ko dul def. naka noonu itam ku dul lekk yàpp, bumu teg tooñ ki koy lekk; ndax yàlla nangu na leen ñoom ñaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car, lorsque nous étions chez vous, nous vous disions expressément: si quelqu`un ne veut pas travailler, qu`il ne mange pas non plus.

Wolof

ndaxte ba nu nekkee ca yéen, lii lanu tëraloon: «ku liggéeyul, du lekk.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est ici le pain qui est descendu du ciel. il n`en est pas comme de vos pères qui ont mangé la manne et qui sont morts: celui qui mange ce pain vivra éternellement.

Wolof

kon nag ñam, wi wàcce ci asamaan a ngi noonu; bokkul ak ñam, wa seeni maam lekkoon te faatu. ku lekk ñam wii may wax dinga dund ba fàww.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ce n`est pas de vous tous que je parle; je connais ceux que j`ai choisis. mais il faut que l`Écriture s`accomplisse: celui qui mange avec moi le pain a levé son talon contre moi.

Wolof

«yéen ñépp taxuleen may wax; xam naa ñi ma tànn. waaye li mbind mi wax, fàww mu am, bi ñu naan: “ki lekk sama dugub wéq na ma.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,941,298,994 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK