Results for mettre en garde translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

et de mettre en lumière quelle est la dispensation du mystère caché de tout temps en dieu qui a créé toutes choses,

Wolof

te it may sulli melokaanu mbir mu xóot mi yàlla tëral, te doon kumpa njàlbéen ga ba tey ci moom, mi sos lépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mettez-vous en garde contre les hommes; car ils vous livreront aux tribunaux, et ils vous battront de verges dans leurs synagogues;

Wolof

waaye moytuleen nit ñi, ndaxte dinañu leen jébbal àttekat yi te dóor leen ay yar ci seeni jàngu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et je dis: seigneur, ils savent eux-mêmes que je faisais mettre en prison et battre de verges dans les synagogues ceux qui croyaient en toi, et que,

Wolof

waaye ma tontu ne: “boroom bi, xam nañu ne, dama daan wër jàngoo-jàngu, di tëj kaso ak di dóor ay yar ñi la gëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

recommande aux riches du présent siècle de ne pas être orgueilleux, et de ne pas mettre leur espérance dans des richesses incertaines, mais de la mettre en dieu, qui nous donne avec abondance toutes choses pour que nous en jouissions.

Wolof

Ñi barele alalu àddina nag, dénk leen ñu bañ a réy te bañ a wékk seen yaakaar ci koom-koom yi saxul fenn, waaye ñu wékk ko ci yàlla, mi nuy may naataange ju mat, ngir nu man ciy bànneexu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

sachez-le, mes frères bien-aimés. ainsi, que tout homme soit prompt à écouter, lent à parler, lent à se mettre en colère;

Wolof

yéen sama bokk yi ma bëgg, nangeen xam lii: ku nekk war ngaa farlu ci déglu, di yéex a wax tey yéex a mer.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

savoir, de vous abstenir des viandes sacrifiées aux idoles, du sang, des animaux étouffés, et de l`impudicité, choses contre lesquelles vous vous trouverez bien de vous tenir en garde. adieu.

Wolof

maanaam ngeen moytu ñam wu ñu tuuroo xërëm, deretu jur gu médd ak njaaloo. bu ngeen moytoo yëf yooyu, dingeen def lu baax. ci jàmm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais paul dit aux licteurs: après nous avoir battus de verges publiquement et sans jugement, nous qui sommes romains, ils nous ont jetés en prison, et maintenant ils nous font sortir secrètement! il n`en sera pas ainsi. qu`ils viennent eux-mêmes nous mettre en liberté.

Wolof

waaye pool ne alkaati ya: «dóor nañu nu ay yar ci kanamu ñépp, ci lu ñu wéerul ci benn àtte, rax-ca-dolli tëj nañu nu kaso, nun ñiy jaambur ci nguuru room. léegi ndax dañu noo bëgg a sànni ci mbedd mi ci kumpa? mukk! nañu ñëw, ñoom ci seen bopp, gunge nu ci biti.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,773,212,329 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK