Results for mort translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

ils répondirent: il mérite la mort.

Wolof

lu ngeen ci xalaat?» Ñu tontu ko: «yoon teg na ko dee.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car celui qui est mort est libre du péché.

Wolof

ndaxte ku dee, bàkkaar mënatul dara ci yaw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ainsi la mort agit en nous, et la vie agit en vous.

Wolof

noonu dee mu ngi jëf ci nun, dund di jëf ci yéen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car christ est ma vie, et la mort m`est un gain.

Wolof

ndaxte su ma dundee, kirist laay noyyee, te su ma deeyee, xéewal lay doon ci man.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

comme le corps sans âme est mort, de même la foi sans les oeuvres est morte.

Wolof

kon nag ni jëmm ju amul ruu nekke ndee, noonu la ngëm gu àndul ak jëf nasaxe.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

misérable que je suis! qui me délivrera du corps de cette mort?...

Wolof

céy maaka torox! ana ku may musal ci sama yaram, wii may jëme ci dee?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car c`est par la loi que je suis mort à la loi, afin de vivre pour dieu.

Wolof

ci li jëm ci yoonu musaa, dee naa, fekk yoon wi ci boppam moo ko waral, ngir ma man a dund, ba amal jariñ yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

beaucoup de juifs étaient venus vers marthe et marie, pour les consoler de la mort de leur frère.

Wolof

yawut yu bare ñëwoon nañu kër màrt ak maryaama, ngir dëfël leen ci seen deewu càmmiñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

j`ai persécuté à mort cette doctrine, liant et mettant en prison hommes et femmes.

Wolof

daan naa fitnaal ña bokkoon ci yoon wii, ba di ci rey sax; yeew naa góor ak jigéen, tëj leen;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car, lorsque nous étions encore sans force, christ, au temps marqué, est mort pour des impies.

Wolof

ndaxte bi nu amul jenn doole, booba la kirist dee ngir nun, fekk danoo weddi woon yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il leur dit: mon âme est triste jusqu`à la mort; restez ici, et veillez.

Wolof

mu ne leen: «sama xol dafa tiis, ba ma bëgg a dee; toogleen fii, xool.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin de connaître christ, et la puissance de sa résurrection, et la communion de ses souffrances, en devenant conforme à lui dans sa mort, pour parvenir,

Wolof

moom laay ittewoo xam, ak doole ji ànd ak ndekkiteem, ma bokk ci ay coonoom, ba fekki ko ci deeyam,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

après m`avoir interrogé, ils voulaient me relâcher, parce qu`il n`y avait en moi rien qui méritât la mort.

Wolof

waa room nag seet sama mbir, te bëgg maa bàyyi, ndaxte toppuñu ma dara lu jar dee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,896,994,540 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK