Results for objet translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

et il ne laissait personne transporter aucun objet à travers le temple.

Wolof

te mayul kenn, mu yóbbu am njaay ci kër yàlla gi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

nous ne donnons aucun sujet de scandale en quoi que ce soit, afin que le ministère ne soit pas un objet de blâme.

Wolof

bëggunoo lëmbaaje xelu kenn ci dara, ngir kenn bañ a sikk sunu liggéey.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car l`homme qui avait été l`objet de cette guérison miraculeuse était âgé de plus de quarante ans.

Wolof

ndaxte nit, ka ñu fajoon ci kéemaan googu, weesoon na ñeent-fukki at.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

cela arriva jusqu`à trois fois; et aussitôt après, l`objet fut retiré dans le ciel.

Wolof

Ñu def ko nag, ba muy ñetti yoon, ba noppi ñu ne cas sér ba, jëme asamaan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

les prophètes, qui ont prophétisé touchant la grâce qui vous était réservée, ont fait de ce salut l`objet de leurs recherches et de leurs investigations,

Wolof

naka mucc googu nag, yonent yi xamle yiw, wi ngeen naroon a joti, seet nañu ko te gëstu ko.

Last Update: 2023-09-21
Usage Frequency: 8
Quality:

French

sachant tout d`abord vous-mêmes qu`aucune prophétie de l`Écriture ne peut être un objet d`interprétation particulière,

Wolof

waaye jëkkleena xam ne, amul jenn waxu yonent ci mbind mi, ju balle ci xelu boppam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

au reste, frères, que tout ce qui est vrai, tout ce qui est honorable, tout ce qui est juste, tout ce qui est pur, tout ce qui est aimable, tout ce qui mérite l`approbation, ce qui est vertueux et digne de louange, soit l`objet de vos pensées.

Wolof

léegi nag bokk yi, na seen xalaat jublu ci lii: lu dëggu, lu jekk, lu jub, lu sell, lu rafet ak lu faaydawu; su fi amee lu baax mbaa lu mat a naw, xalaatleen ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,788,722,283 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK