From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
parce que nous sommes membres de son corps.
ndaxte noo di céri jëmmam.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
le jugement, parce que le prince de ce monde est jugé.
ci mbiri àtte ba, dina leen yey ndaxte àtte nañu malaaka mu bon mi jiite àddina si, ba daan ko.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
pourquoi?... parce que je ne vous aime pas?... dieu le sait!
lu tax? ndax dama leen a bëggul? yàlla xam na ne, bëgg naa leen!
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et moi, parce que je dis la vérité, vous ne me croyez pas.
waaye man damay wax dëgg, moo tax gëmuleen ma.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
parce que tout est sanctifié par la parole de dieu et par la prière.
ndaxte kàddug yàlla ak ñaan ñoo koy sellal.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mais vous ne croyez pas, parce que vous n`êtes pas de mes brebis.
waaye gëmuleen ndaxte bokkuleen ci samay xar.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
la justice, parce que je vais au père, et que vous ne me verrez plus;
ci mbiri sama njubte, dina leen yey ndaxte maa ngi dem ci baay bi te dungeen ma gisati.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et vous aussi, vous rendrez témoignage, parce que vous êtes avec moi dès le commencement.
te yéen itam dingeen seede samay mbir, ndaxte yéena nekkoon ak man ca njàlbéen ga.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mais, parce que je vous ai dit ces choses, la tristesse a rempli votre coeur.
seen xol dafa jeex ndax li ma leen wax.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
parce que je pardonnerai leurs iniquités, et que je ne me souviendrai plus de leurs péchés.
ndaxte dinaa leen baal seeni tooñ,te dootuma fàttaliku seeni bàkkaar.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
malheur à vous! parce que vous bâtissez les tombeaux des prophètes, que vos pères ont tués.
dingeen torox, ndaxte yéena ngi tabax xabruy yonent, yi seeni maam reyoon.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
je vous écris, petits enfants, parce que vos péchés vous sont pardonnés à cause de son nom.
samay doom, maa ngi leen di bind,ndax baalees na leen seeni bàkkaar ci turu kirist.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car ils n`avaient pas compris le miracle des pains, parce que leur coeur était endurci.
njàqarey taalibe ya nag weesu dayo, ndaxte seen xol dafa fatt, ba réere mbir kéemaan, gi yeesu defoon ci mburu yi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ils appelaient barnabas jupiter, et paul mercure, parce que c`était lui qui portait la parole.
noonu ñu tudde barnabas, sës, te tudde pool, ermes, ndaxte mooy ki yor wax ji.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
de plus, il y a eu des sacrificateurs en grand nombre, parce que la mort les empêchait d`être permanents.
te it yeneen saraxalekat yi dañoo bare woon, ndaxte dee moo daan tax duñu man a sax ci seen liggéey.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car celui que dieu a envoyé dit les paroles de dieu, parce que dieu ne lui donne pas l`esprit avec mesure.
ndaw li yàlla yónni, kàddug yàlla lay wax, ndaxte mayu xel mu sell, mi yàlla sol ci moom, amul dayo.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
au bruit qui eut lieu, la multitude accourut, et elle fut confondue parce que chacun les entendait parler dans sa propre langue.
bi nit ñi déggee riir ma nag, ñépp dajaloo, daldi waaru ci li ñu leen dégg, ñuy wax ku nekk sa làkk.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ainsi, parce que tu es tiède, et que tu n`es ni froid ni bouillant, je te vomirai de ma bouche.
waaye ndax li nga nugg, tàngoo seddoo, dinaa la yàbbi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
après cela, jésus parcourait la galilée, car il ne voulait pas séjourner en judée, parce que les juifs cherchaient à le faire mourir.
gannaaw loolu yeesu doon na wër diiwaanu galile.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
celui qui est de dieu, écoute les paroles de dieu; vous n`écoutez pas, parce que vous n`êtes pas de dieu.
ku nekk doomu yàlla dina déglu ay waxam. waaye nekkuleen doomi yàlla, looloo tax dungeen déglu.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: