Results for pas de nouvelle translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

car dieu ne se repent pas de ses dons et de son appel.

Wolof

ndax li yàlla maye, dootu ko nangu mukk, te ku mu woo ci boppam, dootu la dàq mukk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

pour vous, frères, ne vous lassez pas de faire le bien.

Wolof

yéen nag bokk yi, buleen tàyyi ci def lu rafet.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

si cet homme ne venait pas de dieu, il ne pourrait rien faire.

Wolof

kon nit kookee nag, bu jógewul woon ca yàlla, du man a def dara.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je ne te prie pas de les ôter du monde, mais de les préserver du mal.

Wolof

Ñaanuma nga jële leen àddina, waaye nga yiir leen ci ibliis.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus leur dit cette parabole, mais ils ne comprirent pas de quoi il leur parlait.

Wolof

yeesu misaaloon na leen loolu, waaye xamuñu lu mu leen doon wax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il n`y a pas de plus grand amour que de donner sa vie pour ses amis.

Wolof

genn mbëggeel mënul a weesu joxe sa bakkan ngir say xarit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et pourquoi ne discernez-vous pas de vous-mêmes ce qui est juste?

Wolof

«lu tax it dungeen àtteel seen bopp liy jëf ju jub?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

donne à celui qui te demande, et ne te détourne pas de celui qui veut emprunter de toi.

Wolof

mayal ku lay ñaan, te bul jox gannaaw ku lay leb.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

autrefois, ne connaissant pas dieu, vous serviez des dieux qui ne le sont pas de leur nature;

Wolof

bu jëkk, bi ngeen xamagul yàlla, yéena ngi doon jaamu yeneen yu ñu daan bokkaaleel yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et ils ne se repentirent pas de leurs meurtres, ni de leurs enchantements, ni de leur impudicité ni de leurs vols.

Wolof

te nit ñooñu tuubuñu seen bóom, seen xërëm, seen njaaloo mbaa seen càcc.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ainsi donc, frères, aspirez au don de prophétie, et n`empêchez pas de parler en langues.

Wolof

kon nag bokk yi, farluleen ci di wax ci kàddug yàlla, te buleen tere kenn muy wax ay làkk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car jean baptiste est venu, ne mangeant pas de pain et ne buvant pas de vin, et vous dites: il a un démon.

Wolof

ndaxte yaxya feeñ na, lekkul mburu, naanul biiñ, ngeen daldi ne: “dafa ànd ak rab.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car nous n`avons pas de puissance contre la vérité; nous n`en avons que pour la vérité.

Wolof

ndaxte manalunu dara dëggu yàlla gi; mënunu lu dul taxawal ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin qu`il n`y ait pas de division dans le corps, mais que les membres aient également soin les uns des autres.

Wolof

noonu yaram du séddaloo, waaye cér bu ci nekk dina dimbali yi ci des.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car ils disaient: que ce ne soit pas pendant la fête, afin qu`il n`y ait pas de tumulte parmi le peuple.

Wolof

kon nag ñu ne: «bumu doon ci bésu màggal bi, ngir yengu-yengu bañ a am ci nit ñi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

celui qui est de dieu, écoute les paroles de dieu; vous n`écoutez pas, parce que vous n`êtes pas de dieu.

Wolof

ku nekk doomu yàlla dina déglu ay waxam. waaye nekkuleen doomi yàlla, looloo tax dungeen déglu.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car c`est par la grâce que vous êtes sauvés, par le moyen de la foi. et cela ne vient pas de vous, c`est le don de dieu.

Wolof

ndaxte ci yiwu yàlla ngeen mucce ci kaw ngëm, te loolu jógewul ci yéen, mayu yàlla la;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais pour ce qui est d`être assis à ma droite ou à ma gauche, cela ne dépend pas de moi, et ne sera donné qu`à ceux à qui cela est réservé.

Wolof

waaye toog ci sama ndeyjoor mbaa sama càmmooñ, du man maa koy maye. Ñi ñu ko waajal rekk a ko yelloo.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car, je vous le dis en vérité, tant que le ciel et la terre ne passeront point, il ne disparaîtra pas de la loi un seul iota ou un seul trait de lettre, jusqu`à ce que tout soit arrivé.

Wolof

ndaxte ci dëgg maa ngi leen koy wax, li feek asamaan ak suuf wéyul, benn tomb walla benn rëddu araf du wéy mukk ci yoonu musaa, ba kera yépp di am.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

avant la fête de pâque, jésus, sachant que son heure était venue de passer de ce monde au père, et ayant aimé les siens qui étaient dans le monde, mit le comble à son amour pour eux.

Wolof

laata màggalu bésu jéggi ba la woon. yeesu xamoon na ne, waxtu wi mu war a génne àddina, dem ca wetu baay ba, jot na. ku bëgg ñoñam yi nekk ci àddina la, te bëgg na leen ba fa mbëggeel man a yem.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,793,355,426 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK