From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
la parole du seigneur se répandait dans tout le pays.
noonu kàddug boroom bi di law ci diiwaan bépp.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et il le priait instamment de ne pas les envoyer hors du pays.
muy ñaan yeesu lool, ngir mu bañ leen a dàq ca réew ma.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
après avoir traversé la mer, ils vinrent dans le pays de génésareth.
bi loolu amee ñu jàll, teer ca diiwaanu senesaret.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ils arrivèrent à l`autre bord de la mer, dans le pays des gadaréniens.
noonu ñu jàll dex ga, ba teer ci diiwaanu waa serasa.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
après avoir traversé la mer, ils vinrent dans le pays de génésareth, et ils abordèrent.
bi nga xamee ne jàll nañu, ba egg diiwaanu senesaret, ñu teer fa,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
cette parole sur jésus se répandit dans toute la judée et dans tout le pays d`alentour.
la ñu wax ci mbiri yeesu daldi siiw ca réewu yawut ya ak la ko wër yépp.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et il alla dans tout le pays des environs de jourdain, prêchant le baptême de repentance, pour la rémission des péchés,
yaxya daldi dugg àll, bi wër dexu yurdan gépp, di waaree nii: «tuubleen seeni bàkkaar, ba noppi ma sóob leen ci ndox, ngir yàlla baal leen seeni bàkkaar.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
a cette parole, moïse prit la fuite, et il alla séjourner dans le pays de madian, où il engendra deux fils.
bi musaa déggee wax jooju, mu daldi daw, dem réewu majan, di fa ab doxandéem; mu séy fa, ba am ñaari doom.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
le peuple de zabulon et de nephthali, de la contrée voisine de la mer, du pays au delà du jourdain, et de la galilée des gentils,
«yaw réewum sabulon ak réewum neftali,di yoonu géej gannaaw dexu yurdan,yaw galile, réewum ñi dul yawut —
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
c`est pourquoi je vous le dis: au jour du jugement, le pays de sodome sera traité moins rigoureusement que toi.
waaye maa ngi leen koy wax, keroog bés pénc ma sodom moo lay tane.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ayant été empêchés par le saint esprit d`annoncer la parole dans l`asie, ils traversèrent la phrygie et le pays de galatie.
bi loolu amee gannaaw xel mu sell mi aaye na leen, ñu yégleji kàddu gi ci diiwaanu asi, ñu daldi jaari wàlli firisi ak galasi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: