From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
à ce qu`il n`y ait ni impudique, ni profane comme Ésaü, qui pour un mets vendit son droit d`aînesse.
moytuleen it ba kenn du njaaloo walla muy fonkadi yëfi yàlla, ni esawu, mi weccee woon ndonol taawam ngir ag lekk.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
de quel pire châtiment pensez-vous que sera jugé digne celui qui aura foulé aux pieds le fils de dieu, qui aura tenu pour profane le sang de l`alliance, par lequel il a été sanctifié, et qui aura outragé l`esprit de la grâce?
ku xeeb doomu yàlla ji te fonkadi deretu kóllëre, ji ñu ko sellale, te muy toroxal xelum yàlla, mi indi yiw, naka la mbugalam war a gën a yéese?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: