From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
jusqu`à ce jour, quand on lit moïse, un voile est jeté sur leurs coeurs;
waaw, ba tey jii, su ñuy jàng yoonu musaa, seen xol dafay muuru.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car c`est une grâce que de supporter des afflictions par motif de conscience envers dieu, quand on souffre injustement.
ndaxte su ngeen dékkoo tiis, di sonn ci lu dul yoon ndax seen ànd ak yàlla, loolu lu rafet la.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
quand on vous mènera devant les synagogues, les magistrats et les autorités, ne vous inquiétez pas de la manière dont vous vous défendrez ni de ce que vous direz;
«bu ñu leen yóbboo ca jàngu ya, ca kanamu kilifa ya ak àttekat ya, buleen am xel ñaar ci li ngeen war a tontu ak nan ngeen war a tontoo, walla lu ngeen war a wax,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car, quand on se met à table, chacun commence par prendre son propre repas, et l`un a faim, tandis que l`autre est ivre.
ndaxte bu ngeen dee lekk, ku nekk dafay gaawantu di lekk reeram, ba tax ñenn ñaa ngi xiif, fekk ñeneen di màndi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mais, quand on vous livrera, ne vous inquiétez ni de la manière dont vous parlerez ni de ce que vous direz: ce que vous aurez à dire vous sera donné à l`heure même;
boo xamee ne nag jébbale nañu leen, buleen am xel ñaar ci li ngeen di wax, mbaa ni ngeen koy waxe. ndaxte ca waxtu woowa sax dingeen jot li ngeen war a wax;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
en effet, les perfections invisibles de dieu, sa puissance éternelle et sa divinité, se voient comme à l`oeil, depuis la création du monde, quand on les considère dans ses ouvrages. ils sont donc inexcusables,
ndaxte ba àddina sosoo ba tey, mbiri yàlla yu nëbbu ya, maanaam dooleem ju sax ja, ak meloom wu kawe wa, feeñ nañu bu leer, te bir ñépp ci yi mu sàkk, ba tax bunti lay yépp tëj nañu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
quand on vous persécutera dans une ville, fuyez dans une autre. je vous le dis en vérité, vous n`aurez pas achevé de parcourir les villes d`israël que le fils de l`homme sera venu.
boo xamee ne fitnaal nañu leen ci dëkk bii, demleen ca ba ca kanam. ci dëgg maa ngi leen koy wax, dungeen man a wër dëkki israyil yépp, te doomu nit ki ñëwul.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors paul lui dit: dieu te frappera, muraille blanchie! tu es assis pour me juger selon la loi, et tu violes la loi en ordonnant qu`on me frappe!
pool ne ko: «yàlla dina la dóor, yaw mi naaféq, bay samandaay miir bu joy bu ñu weexal. yaa ngi toog di ma àtte, ci li yoon wi digle, ba noppi santaane ñu dóor ma, ci li yoon wi tere!»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.