From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
j`ai donc sujet de me glorifier en jésus christ, pour ce qui regarde les choses de dieu.
kon nag maa ngi bànneexu ci kirist yeesu ngir liggéey boobu ma yàlla dénk.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car, si quelqu`un écoute la parole et ne la met pas en pratique, il est semblable à un homme qui regarde dans un miroir son visage naturel,
ndaxte ku déglu kàddu gi, te bañ koo jëfe, moom ak kuy seetu ñoo yem;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et il leur dit: c`est pourquoi, tout scribe instruit de ce qui regarde le royaume des cieux est semblable à un maître de maison qui tire de son trésor des choses nouvelles et des choses anciennes.
yeesu ne leen: «kon xutbakat bu nekk bu jàng ci nguuru yàlla aji kawe ji, dafa mel ni boroom kër buy génne ci dencukaayam yu bees ak yu màggat.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et comme le port n`était pas bon pour hiverner, la plupart furent d`avis de le quitter pour tâcher d`atteindre phénix, port de crète qui regarde le sud-ouest et le nord-ouest, afin d`y passer l`hiver.
te gannaaw teeru ba neexul a lollikoo, ña ca ëpp mànkoo ci jóge fa, dem ci biir géej, ngir wut a agsi fenigsë, biy teerub dunu kereet te janook sowu suuf ak sowu kaw, nu lollikoo fa.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.