Results for retenir translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

se retenir (forme d’humilité)

Wolof

man dou

Last Update: 2023-01-25
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

mais, pour ne pas te retenir davantage, je te prie d`écouter, dans ta bonté, ce que nous avons à dire en peu de mots.

Wolof

waaye ngir bañ a yàggal jataay bi, maa ngi lay ñaan ci sa lewetaay, nga déglu nu ci lu gàtt.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

j`aurais désiré le retenir auprès de moi, pour qu`il me servît à ta place, pendant que je suis dans les chaînes pour l`Évangile.

Wolof

dama koo bëggoon a téye fi sama wet, ngir mu taxawal la, di ma dimbali, li feek maa ngi ci kaso bi ngir xebaar bu baax bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

dès que le jour parut, il sortit et alla dans un lieu désert. une foule de gens se mirent à sa recherche, et arrivèrent jusqu`à lui; ils voulaient le retenir, afin qu`il ne les quittât point.

Wolof

ca njël gu jëkk yeesu génn, dem ca bérab bu wéet. mbooloo ma di ko seet. bi ñu ko gisee, ñu koy wut a téye, ngir bañ mu dem.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Get a better translation with
7,777,654,475 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK