Results for salaire translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

celui qui moissonne reçoit un salaire, et amasse des fruits pour la vie éternelle, afin que celui qui sème et celui qui moissonne se réjouissent ensemble.

Wolof

kiy góob tool yi mu ngi jot xaat peyam; day dajale nit ñi ngir dund gu dul jeex, ni ñuy dajalee pepp. kon boog kiy ji dina bégandoo ak kiy góob.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

après avoir quitté le droit chemin, ils se sont égarés en suivant la voie de balaam, fils de bosor, qui aima le salaire de l`iniquité,

Wolof

réer nañu ba wàcc yoon wu jub wi, topp yoonu balaam, doomu bosor, mi bëgge xiiroon ci njubadi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

malheur à eux! car ils ont suivi la voie de caïn, ils se sont jetés pour un salaire dans l`égarement de balaam, ils se sont perdus par la révolte de coré.

Wolof

Ñoo kay torox! dañoo jaar ci yoonu kayin, sóobu ci réerug balaam ngir xaalis, di bañ kilifteef ni kore, te dinañu dee ni moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car l`Écriture dit: tu n`emmuselleras point le boeuf quand il foule le grain. et l`ouvrier mérite son salaire.

Wolof

ndaxte mbind mi nee na: «bul sunjuñ gémmiñu nag wu ñu takk bojjukaay,» nee na it: «ku ñaq, jariñu.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

recevant ainsi le salaire de leur iniquité. ils trouvent leurs délices à se livrer au plaisir en plein jour; hommes tarés et souillés, ils se délectent dans leurs tromperies, en faisant bonne chère avec vous.

Wolof

muy seen peyug njubadi. xawaare bëccëgu ndara-kàmm mooy seen bànneex. su ñuy lekkandoo ak yeen, dañuy bànneexu ci seeni bëgg-bëgg, di ay gàkk ak i sikk ci seen biir.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

demeurez dans cette maison-là, mangeant et buvant ce qu`on vous donnera; car l`ouvrier mérite son salaire. n`allez pas de maison en maison.

Wolof

dal-leen ca kër googa, tey lekk ak a naan lu ñu leen di jox, ndaxte liggéeykat yelloo na jot peyam. buleen dem nag kër ak kër.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,038,641,788 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK