Results for satan translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

car déjà quelques-unes se sont détournées pour suivre satan.

Wolof

ndaxte fi mu ne sax am na ñu jeng xaat, ba topp seytaane.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus leur dit: je voyais satan tomber du ciel comme un éclair.

Wolof

yeesu ne leen: «maa ngi doon séen seytaane wàcce asamaan ni safaras melax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

or, satan entra dans judas, surnommé iscariot, qui était du nombre des douze.

Wolof

noonu seytaane daldi solu yudaa, mi ñuy wooye iskariyo te mu bokkoon ca fukki taalibe ya ak ñaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et cela n`est pas étonnant, puisque satan lui-même se déguise en ange de lumière.

Wolof

te loolu jaaxalu nu, ndaxte seytaane moom ci boppam day mbubboo malaakam leer.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin de ne pas laisser à satan l`avantage sur nous, car nous n`ignorons pas ses desseins.

Wolof

ngir seytaane bañ a am bunt bu mu jaar ba nax nu, ndaxte réerewunu mbir ay pexeem.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

où il passa quarante jours, tenté par satan. il était avec les bêtes sauvages, et les anges le servaient.

Wolof

mu nekk fa ñeent-fukki fan, jànkoonte ak fiiri seytaane; mu dëkk ci biir rabi àll yi, te malaakay yàlla di ko topptoo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus les appela, et leur dit sous forme de paraboles: comment satan peut-il chasser satan?

Wolof

noonu yeesu woo leen, wax ak ñoom ciy léeb ne leen: «naka la seytaane man a dàqe seytaane?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

aussi voulions-nous aller vers vous, du moins moi paul, une et même deux fois; mais satan nous en a empêchés.

Wolof

kon jàppoon nanu leen a seetsi — man pool sax ay yooni yoon, waaye seytaane téq na ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

de ce nombre son hyménée et alexandre, que j`ai livrés à satan, afin qu`ils apprennent à ne pas blasphémer.

Wolof

naka imene ak alegsàndar; jébbal naa leen seytaane, ngir ñu réccu li ñu doon sosal yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

l`apparition de cet impie se fera, par la puissance de satan, avec toutes sortes de miracles, de signes et de prodiges mensongers,

Wolof

bu nitu ñaawteef kooku feeñee, dina ànd ak kàttanu seytaane ak doole ju bare, di wone ay firnde ak ay kéemaan yu dul dëgg;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

si satan chasse satan, il est divisé contre lui-même; comment donc son royaume subsistera-t-il?

Wolof

bu seytaane dàqee seytaane nag, xeex na boppam; kon naka la nguuram di man a yàgge?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je connais ta tribulation et ta pauvreté (bien que tu sois riche), et les calomnies de la part de ceux qui se disent juifs et ne le sont pas, mais qui sont une synagogue de satan.

Wolof

xam naa sa coono, xam it sa néew doole, moona yaaka duunle. Ñooñu tuddoo yawut, xam naa ñaawteef yi ñu teg ci sa der: ndajem seytaane la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et il fut précipité, le grand dragon, le serpent ancien, appelé le diable et satan, celui qui séduit toute la terre, il fut précipité sur la terre, et ses anges furent précipités avec lui.

Wolof

daaneel nañu ko, moom ninkinànka ju réy ji, di jaani cosaan ji, te ñu di ko wax tuumaalkat bi mbaa seytaane, moom miy nax waa àddina sépp — daaneel nañu ko ci kaw suuf, moom ak ay malaakaam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

a vous, à tous les autres de thyatire, qui ne reçoivent pas cette doctrine, et qui n`ont pas connu les profondeurs de satan, comme ils les appellent, je vous dis: je ne mets pas sur vous d`autre fardeau;

Wolof

waaye yéen ñépp ñi des ci catir te toppuleen njàngale moomu te gëstuwuleen loolu ñu naan mbiri seytaane yu xóot yi, maa ngi leen di wax ne, duma leen yen beneen yen

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,899,458,455 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK