Results for sera translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

car tout homme sera salé de feu.

Wolof

Ñépp safara lañu leen di xorome.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et son nom sera sur leurs fronts.

Wolof

dinañu gis xar-kanamam, te turam dina nekk ci seen jë.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

tout cela ne sera que le commencement des douleurs.

Wolof

waaye loolu lépp mooy ndoortel metit yi, mel ni jigéen juy matu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

le plus grand parmi vous sera votre serviteur.

Wolof

ki gën a mag ci yéen mooy ki nangoo nekk seen surga.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car quiconque invoquera le nom du seigneur sera sauvé.

Wolof

ndaxte bind nañu: «képp ku woo boroom bi ciw turam, dinga mucc.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

alors quiconque invoquera le nom du seigneur sera sauvé.

Wolof

booba nag ku woo boroom bi ci aw turam,dinga mucc.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car là où est ton trésor, là aussi sera ton coeur.

Wolof

ndaxte fu sa alal nekk, fa la sa xol nekk itam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car là où est votre trésor, là aussi sera votre coeur.

Wolof

ndaxte fu sa alal nekk, fa la sa xol nekk itam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il en sera de même le jour où le fils de l`homme paraîtra.

Wolof

noonu lay mel, bés bu doomu nit kiy feeñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

mais celui qui me reniera devant les hommes sera renié devant les anges de dieu.

Wolof

waaye ku ma gàntu ci kanamu nit ñi, dinañu la gàntu ci kanamu malaakay yàlla yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et ce sera mon alliance avec eux, lorsque j`ôterai leurs péchés.

Wolof

loolu mooy kóllëre, gi may fas ak ñoom,bés bu may dindi seeni bàkkaar.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

nous sommes prêts aussi à punir toute désobéissance, lorsque votre obéissance sera complète.

Wolof

te fas yéene nanoo jubbanti képp ku déggadi, bés bu seen dégg ndigal matee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il répondit: toute plante que n`a pas plantée mon père céleste sera déracinée.

Wolof

yeesu tontu leen ne: «garab gu sama baay bi ci kaw jiwul, dees na ko buddi.

Last Update: 2024-04-27
Usage Frequency: 2
Quality:

French

car ils ne supportaient pas cette déclaration: si même une bête touche la montagne, elle sera lapidée.

Wolof

ndaxte mënuñu woon a dékku ndigal lii: «su mala sax laalee tund wa, nangeen ko sànni ay xeer, ba mu dee.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et cette bonne nouvelle du royaume sera prêchée dans le monde entier, en témoignage à toutes les nations. et alors viendra la fin.

Wolof

noonu xibaaru jàmm bii ci nguuru yàlla dees na ko yégle ci àddina sépp, ngir mu nekk seede ci xeet yépp. bu loolu amee mujug jamono ji lot.

Last Update: 2017-02-08
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

c`est pourquoi, quiconque se rendra humble comme ce petit enfant sera le plus grand dans le royaume des cieux.

Wolof

kuy suufeelu nag, ba mel ni xale bii, kooku mooy ki gën a màgg ci nguuru yàlla aji kawe ji.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

c`est pourquoi celui qui mangera le pain ou boira la coupe du seigneur indignement, sera coupable envers le corps et le sang du seigneur.

Wolof

kon nag képp ku jekkadi ni mu lekke ci mburu mi te naane ni ci kaasu boroom bi, tooñ nga yaramu boroom bi ak deretam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

French

a la résurrection, duquel d`entre eux sera-t-elle donc la femme? car les sept l`ont eue pour femme.

Wolof

ci ndekkite li nag, kan ci ñoom moo war a donn jigéen ja, fekk ku nekk ci juróom-ñaar ñi mas na koo takk?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Get a better translation with
8,899,338,379 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK