From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
rappelle ces choses, en conjurant devant dieu qu`on évite les disputes de mots, qui ne servent qu`à la ruine de ceux qui écoutent.
saxal ci di leen fàttali mbir yooyu, di leen dénk fa kanam yàlla, ñu moytoo werante ciy araf, ndax loolu jëmul fu dul ci yàq ngëmu ñiy déglu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
car de tels hommes ne servent point christ notre seigneur, mais leur propre ventre; et, par des paroles douces et flatteuses, ils séduisent les coeurs des simples.
ndax ñu deme noonu liggéeyaluñu kirist sunu boroom; seen bopp lañuy liggéeyal. Ñu ngi ñëw ak làmmiñ yu neex, di jey xol yu woyof yi, ba nax leen.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et à laquelle aspirent nos douze tribus, qui servent dieu continuellement nuit et jour. c`est pour cette espérance, ô roi, que je suis accusé par des juifs!
dige booba la fukki giir ak ñaar yu bànni israyil di sàkku, ngir jot ko, ci jaamu yàlla ak cawarte guddi ak bëccëg. yaw buur, yaakaar joojoo tax ñu may kalaame, ñoom yawut yi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
c`est pour cela qu`ils sont devant le trône de dieu, et le servent jour et nuit dans son temple. celui qui est assis sur le trône dressera sa tente sur eux;
loolu moo taxñu nekk ci kanamu gàngunem yàlla,di ko jaamu guddi ak bëccëg ci këram,te ki toog ci gàngune mi dina leen yiir.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
et que ceux qui ont des fidèles pour maîtres ne les méprisent pas, sous prétexte qu`ils sont frères; mais qu`ils les servent d`autant mieux que ce sont des fidèles et des bien-aimés qui s`attachent à leur faire du bien. enseigne ces choses et recommande-les.
ku am sang boo bokkal ngëm, bu looloo tax nga yab ko, waaye nga sax ci itteem, ndax kiy jariñu ci sa ñaq, aji gëm la, ku mat a bëgg. jàngaleel loolu nag, di ko dénkaane.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: