From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
alors les justes resplendiront comme le soleil dans le royaume de leur père. que celui qui a des oreilles pour entendre entende.
booba nag ñu jub ñi dinañu leer ni jant bi ci seen nguuru baay. déglul bu baax, yaw mi am ay nopp.»
afin que vous soyez fils de votre père qui est dans les cieux; car il fait lever son soleil sur les méchants et sur les bons, et il fait pleuvoir sur les justes et sur les injustes.
ngir wone ne, yéenay doomi seen baay bi nekk ci kaw. ndaxte mu ngi fenkal jantam ci kaw ñu bon ñi ak ñu baax ñi, te muy tawal ñi jub ak ñi jubadi.
après le couché du soleil, tous ceux qui avaient des malades atteints de diverses maladies les lui amenèrent. il imposa les mains à chacun d`eux, et il les guérit.
bi jant sowee, ñu indil yeesu ñi wopp ñépp ak ay jàngoro yu wuute. kenn ku nekk mu teg la loxo, wéral la.
aussitôt après ces jours de détresse, le soleil s`obscurcira, la lune ne donnera plus sa lumière, les étoiles tomberont du ciel, et les puissances des cieux seront ébranlées.
«gannaaw metitu bés yooyule nag, ca saa sa jant bi dina lëndëm te weer wi dootul leer; biddiiw yi dinañu fàq, daanu ci asamaan, te kàttani asamaan yi yengu.
il y aura des signes dans le soleil, dans la lune et dans les étoiles. et sur la terre, il y aura de l`angoisse chez les nations qui ne sauront que faire, au bruit de la mer et des flots,
«ay firnde dinañu feeñ ci jant bi, ci weer wi ak ci biddiiw yi. ci kaw suuf xeet yi dinañu tiit, jaaxle ndax riiru géej gi ak yengu-yengub duus yi.
autre est l`éclat du soleil, autre l`éclat de la lune, et autre l`éclat des étoiles; même une étoile diffère en éclat d`une autre étoile.
jant bi, weer wi ak biddiiw, lu nekk ak sag leer. te it leeru biddiiw bu nekk dina wuute ak moroomam.