Results for sorte benis translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

de sorte que ceux qui croient sont bénis avec abraham le croyant.

Wolof

kon ñi gëm, yàlla dina leen barkeel, sukkandikoo ko ci seen ngëm, ni mu defal ibraayma, boroom ngëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

de sorte que le fils de l`homme est maître même du sabbat.

Wolof

noonu doomu nit ki mooy boroom bésu noflaay bi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

afin que leur superflu pourvoie pareillement aux vôtres, en sorte qu`il y ait égalité,

Wolof

tey jii nag man ngeen sàkk ci li ngeen barele, faj soxlay ñeneen, ngir ëllëg it bareleg ñooña faj seen soxla. noonu ñépp tolloole.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

avec lui les autres juifs usèrent aussi de dissimulation, en sorte que barnabas même fut entraîné par leur hypocrisie.

Wolof

yeneen yawut yi it daldi ànd ak sefas ci naaféqam, ba yóbbaale sax barnabas.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

en péchant de la sorte contre les frères, et en blessant leur conscience faible, vous péchez contre christ.

Wolof

su ngeen bàkkaaree, ba tooñ bokk yi néew ngëm, di nëxal seen xel, bàkkaar ngeen ba tooñ kirist.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

alors on lui amena un démoniaque aveugle et muet, et il le guérit, de sorte que le muet parlait et voyait.

Wolof

booba ñu indil ko ku rab jàpp, mu gumba te luu. yeesu faj ko, ba ku luu ki di wax tey gis.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

en sorte que vous ne vous relâchiez point, et que voue imitiez ceux qui, par la foi et la persévérance, héritent des promesses.

Wolof

bëggunu ngeen tayel, waaye royleen ñi gëm te muñ, ndaxte ñooy jot li leen yàlla dig.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

cela dura deux ans, de sorte que tous ceux qui habitaient l`asie, juifs et grecs, entendirent la parole du seigneur.

Wolof

mu wéy ci noonu diirub ñaari at, ba ñi dëkk diiwaanu asi ñépp dégg kàddug boroom bi, muy yawut muy gereg.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

aie soin de pourvoir au voyage de zénas, le docteur de la loi, et d`apollos, en sorte que rien ne leur manque.

Wolof

naka senas àttekat bi nag ak apolos, waajal leen bu jekk ci seen tukki, ba seen aajo yépp faju.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car, lorsque nous étions dans la chair, les passions des péchés provoquées par la loi agissaient dans nos membres, de sorte que nous portions des fruits pour la mort.

Wolof

keroog ba nu daan topp sunu nafsu, yoonu musaa daan na xamb bëgg-bëgg yu bon, yiy yengal sunuy cér, ba jural nu dee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il pensait que dieu est puissant, même pour ressusciter les morts; aussi le recouvra-t-il par une sorte de résurrection.

Wolof

waaye xelu ibraayma jàppoon na ne, yàlla am na dooley dekkal néew yi. te dëgg-dëgg ci misaal dafa mel ni, isaaxa dafa dee te dekki.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

ce n`est pas pour vous condamner que je parle de la sorte; car j`ai déjà dit que vous êtes dans nos coeurs à la vie et à la mort.

Wolof

teg leen tooñ taxul may wax lii, ndaxte wax naa ba noppi ne, yéena ngi ci sunu xol ci dund ak ci dee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

le centenier, qui était en face de jésus, voyant qu`il avait expiré de la sorte, dit: assurément, cet homme était fils de dieu.

Wolof

njiitu xare nag, bi taxawoon ci kanamu yeesu, bi mu gisee ni yeesu deeye, mu ne: «ci dëgg, nit kii doomu yàlla la!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est par la foi que nous reconnaissons que le monde a été formé par la parole de dieu, en sorte que ce qu`on voit n`a pas été fait de choses visibles.

Wolof

ngëm a tax ba nu xam ne, yàlla sàkk na àddina jaarale ko ci kàddoom, ngir li bët di gis, defarees ko ak lu bët mënul a gis.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

que dieu te benisse

Wolof

Last Update: 2024-02-25
Usage Frequency: 4
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,794,516,072 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK