Results for ta belle mère translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

jésus se rendit ensuite à la maison de pierre, dont il vit la belle-mère couchée et ayant la fièvre.

Wolof

gannaaw loolu yeesu dem kër piyeer. ba mu eggee, mu fekk gorob piyeer bu jigéen tëdd ak yaram wu tàng.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

la belle-mère de simon était couchée, ayant la fièvre; et aussitôt on parla d`elle à jésus.

Wolof

fekk gorob simoŋ bu jigéen tëdd wopp ak yaram wu tàng; ñu daldi ko yégal yeesu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

en sortant de la synagogue, il se rendit à la maison de simon. la belle-mère de simon avait une violente fièvre, et ils le prièrent en sa faveur.

Wolof

bi mu jógee ci jàngu bi, yeesu dafa dem kër simoŋ. gorob simoŋ bu jigéen dafa feebar, ba yaram wi tàng lool. Ñu naan yeesu, mu dimbali leen ci.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

car je suis venu mettre la division entre l`homme et son père, entre la fille et sa mère, entre la belle-fille et sa belle-mère;

Wolof

ndaxte ñëw naa ngir féewale doom ak baayam, doom ju jigéen ak ndeyam, jabar ak goroom;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

le père contre le fils et le fils contre le père, la mère contre la fille et la fille contre la mère, la belle-mère contre la belle-fille et la belle-fille contre la belle-mère.

Wolof

baay bi dina féewaloo ak doom ji, doom ji ak baayam. ndey dina féewaloo ak doomam ju jigéen; doom ju jigéen ji ak ndeyam. goro dina féewaloo ak jabaru doomam; jabaru nit ak goroom.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,793,211,705 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK