From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
car le saint esprit vous enseignera à l`heure même ce qu`il faudra dire.
ndaxte xel mu sell mi dina leen xamal ca waxtu woowa li ngeen war a wax.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
toute la multitude du peuple était dehors en prière, à l`heure du parfum.
ca waxtu wa ñuy taal cuuraay la, mbooloo maa nga woon ca biti, di ñaan.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
veillez donc, puisque vous ne savez ni le jour, ni l`heure.
«yeewuleen nag, ndaxte xamuleen bés ba mbaa waxtu wa.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
l`heure étant venue, il se mit à table, et les apôtres avec lui.
bi waxtu wi jotee yeesu toog ak ndaw yi,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
jésus parla sévèrement au démon, qui sortit de lui, et l`enfant fut guéri à l`heure même.
noonu yeesu tëkku rab wa, rab wa génn ca xale ba, mu daldi wér ca saa sa.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
se levant à l`heure même, ils retournèrent à jérusalem, et ils trouvèrent les onze, et ceux qui étaient avec eux, assemblés
Ñu daldi jóg ca saa sa, dellu yerusalem, fekk fa fukki ndaw ya ak benn, ak yeneeni taalibe.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
pierre et jean montaient ensemble au temple, à l`heure de la prière: c`était la neuvième heure.
am bés piyeer ak yowaana dem, ba bëgg a dugg ca kër yàlla ga ca waxtuw ñaan, maanaam tisbaar.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
le maître de ce serviteur viendra le jour où il ne s`y attend pas et à l`heure qu`il ne connaît pas,
kon njaatige ba dina ñëw ci bés bu mu ko séenuwul ak waxtu wu mu xamul.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
jésus leur répondit: l`heure est venue où le fils de l`homme doit être glorifié.
mu tontu leen ne: «waxtu wi ñu war a feeñale ndamu doomu nit ki jot na.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
a l`heure du souper, il envoya son serviteur dire aux conviés: venez, car tout est déjà prêt.
bi waxtuw lekk jotee mu yónni surga ca ña muy ganale, fàttali leen: “man ngeen a ñëw, ndaxte lépp sotti na léegi.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
vous aussi, tenez-vous prêts, car le fils de l`homme viendra à l`heure où vous n`y penserez pas.
yéen itam taxawleen jonn, ndaxte doomu nit ki dina ñëw ci waxtu wu ngeen ko séenuwul.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ils vous excluront des synagogues; et même l`heure vient où quiconque vous fera mourir croira rendre un culte à dieu.
dinañu leen dàq ca jàngu ya, te dinañu dem ba jamono joo xam ne ñi leen di rey dañuy xalaat ne, ñu ngi màggal turu yàlla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ne vous étonnez pas de cela; car l`heure vient où tous ceux qui sont dans les sépulcres entendront sa voix, et en sortiront.
«bu leen ci dara jaaxal; ndaxte jamonoo ngi ñëw ju néew yépp, yi nekk ci seen bàmmeel, di dégg baatam tey génn.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
je vous ai dit ces choses en paraboles. l`heure vient où je ne vous parlerai plus en paraboles, mais où je vous parlerai ouvertement du père.
«loolu lépp, dama leen koo wax ci ay misaal. jamono dina ñëw, ju ma dootul wax ak yéen ci ay misaal, waaye ju ma leen dee wax lu leer ci baay bi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mais, quand on vous livrera, ne vous inquiétez ni de la manière dont vous parlerez ni de ce que vous direz: ce que vous aurez à dire vous sera donné à l`heure même;
boo xamee ne nag jébbale nañu leen, buleen am xel ñaar ci li ngeen di wax, mbaa ni ngeen koy waxe. ndaxte ca waxtu woowa sax dingeen jot li ngeen war a wax;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alors jésus lui dit: femme, ta foi est grande; qu`il te soit fait comme tu veux. et, à l`heure même, sa fille fut guérie.
ci kaw loolu yeesu tontu ko ne: «yaw jigéen ji, sa ngëm réy na; na am, ni nga ko bëgge.» noonu doomam daldi wér ca saa sa.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
en lui tout l`édifice, bien coordonné, s`élève pour être un temple saint dans le seigneur.
ci moom la doj yépp ràbbloo, ba tabax bi jóg, di màggalukaay bu sell ngir boroom bi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
le maître de ce serviteur viendra le jour où il ne s`y attend pas et à l`heure qu`il ne connaît pas, il le mettra en pièces, et lui donnera sa part avec les infidèles.
kon njaatige ba dina ñëw ci bés bu mu ko séenuwul ak waxtu wu mu xamul. dina ko dóor ay dóor yu metti, jox ko añub ñi gëmul yàlla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
a l`heure même, jésus guérit plusieurs personnes de maladies, d`infirmités, et d`esprits malins, et il rendit la vue à plusieurs aveugles.
ca waxtu woowa yeesu wéral nit ñu bare ci seeni feebar ak ci seeni metit, di dàq ay rab tey gisloo ay gumba.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
voici, l`heure vient, et elle est déjà venue, où vous serez dispersés chacun de son côté, et où vous me laisserez seul; mais je ne suis pas seul, car le père est avec moi.
waxtu waa ngi ñëw te agsi na ba noppi, dingeen tasaaroo, ku nekk ñibbi, ma des man rekk.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.