Results for tu a besoin translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

ils répondirent: le seigneur en a besoin.

Wolof

Ñu tontu ne: «ndaxte boroom bi da koo soxla.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

si quelqu`un vous demande: pourquoi le détachez-vous? vous lui répondrez: le seigneur en a besoin.

Wolof

bu leen kenn laajee: “lu tax ngeen koy yiwi?” tontuleen ko: “boroom bi da koo soxla.”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

jésus lui dit: celui qui est lavé n`a besoin que de se laver les pieds pour être entièrement pur; et vous êtes purs, mais non pas tous.

Wolof

yeesu ne ko: «ku sangu ba noppi, soxlaatul a raxas lu dul ay tànkam, ndaxte set na wecc. yéen nag set ngeen, waaye du ñépp!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

si, quelqu`un vous dit quelque chose, vous répondrez: le seigneur en a besoin. et à l`instant il les laissera aller.

Wolof

te bu leen kenn waxee dara, ngeen ne ko: “boroom bi da leen a soxla.” kon ca saa sa dina leen bàyyi, ñu dem.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je vous le dis, même s`il ne se levait pas pour les lui donner parce que c`est son ami, il se lèverait à cause de son importunité et lui donnerait tout ce dont il a besoin.

Wolof

maa ngi leen koy wax, su jógul jox ko li muy laaj ndax li ñu xaritoo it, ndax la kee ñàkk jom dina tax mu jox ko lépp li mu soxla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

la ville n`a besoin ni du soleil ni de la lune pour l`éclairer; car la gloire de dieu l`éclaire, et l`agneau est son flambeau.

Wolof

dëkk ba soxlawul jant walla weer ngir leeral ko, ndaxte ndamu yàlla moo koy leeral, te mbote ma moo nekk làmpam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

si quelqu`un vous dit: pourquoi faites-vous cela? répondez: le seigneur en a besoin. et à l`instant il le laissera venir ici.

Wolof

bu leen kenn nee: “lu ngeen di def?” tontuleen ko: “boroom bi da koo soxla, te léegi mu delloosi ko.”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je connais tes oeuvres. voici, parce que tu a peu de puissance, et que tu as gardé ma parole, et que tu n`as pas renié mon nom, j`ai mis devant toi une porte ouverte, que personne ne peut fermer.

Wolof

xam naa say jëf. ubbil naa la bunt, te kenn du ko man a tëj. xam naa ne barewuloo doole, waaye sàmm nga sama kàddu te weddiwoo ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,779,926,419 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK