Results for tu fais quoi maintenant translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

mais quand tu fais l`aumône, que ta main gauche ne sache pas ce que fait ta droite,

Wolof

waaye booy sàkk sarax, bu sa loxob càmmooñ xam li sa loxob ndeyjoor di def,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

bien-aimé, tu agis fidèlement dans ce que tu fais pour les frères, et même pour des frères étrangers,

Wolof

yaw sama xarit, sa takkute fés na ci teeru bi ngay teeru mbokk yi, te fekk xamoo leen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

tu crois qu`il y a un seul dieu, tu fais bien; les démons le croient aussi, et ils tremblent.

Wolof

gëm nga ne yàlla kenn la; loolu lu baax la, waaye xamal ne, jinne yi it gëm nañu loolu, ba dañoo tiit bay lox.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

dès que le morceau fut donné, satan entra dans judas. jésus lui dit: ce que tu fais, fais-le promptement.

Wolof

naka la yudaa jël dog wa, seytaane dugg ci moom. yeesu ne ko: «gaawantul ci li ngay def!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

et ses frères lui dirent: pars d`ici, et va en judée, afin que tes disciples voient aussi les oeuvres que tu fais.

Wolof

noonu rakki yeesu yu góor ya ne ko: «jóge fi te dem diiwaanu yude, ngir say taalibe gis, ñoom itam, jaloore yi ngay def.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

le magistrat est serviteur de dieu pour ton bien. mais si tu fais le mal, crains; car ce n`est pas en vain qu`il porte l`épée, étant serviteur de dieu pour exercer la vengeance et punir celui qui fait le mal.

Wolof

ndax yàllaa ko dénk liggéey boobu ngir sa jàmm. waaye sooy def lu bon, war ngaa ragal, ndax du cig neen la ame jaasiy àtte; jawriñu yàlla la ngir wàcce meru yàlla, ci fey ku def lu bon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,794,158,216 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK