From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
et il vint vers les disciples, qu`il trouva endormis, et il dit à pierre: vous n`avez donc pu veiller une heure avec moi!
noonu mu ñëw ca taalibe ya, fekk leen ñuy nelaw. mu ne piyeer: «amuleen sax dooley xoolandoo ak man benn waxtu?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
rappelle-toi donc comment tu as reçu et entendu, et garde et repens-toi. si tu ne veilles pas, je viendrai comme un voleur, et tu ne sauras pas à quelle heure je viendrai sur toi.
fàttalikul kon kàddug yàlla gi nga jot, te dégg ko, sàmm ko te réccu. soo wéyee ciy nelaw nag, dinaa ñëw nib sàcc, te doo xam wan waxtu lay doon. i
Last Update: 2024-03-03
Usage Frequency: 9
Quality: