Results for vocation translation from French to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

French

Wolof

Info

French

je cours vers le but, pour remporter le prix de la vocation céleste de dieu en jésus christ.

Wolof

di daw yen muj ga, ngir jot li ma yàlla tax a woo, di cér bi ma yàlla wooye te dencal ma ko ci asamaan ci darajay kirist yeesu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

il y a un seul corps et un seul esprit, comme aussi vous avez été appelés à une seule espérance par votre vocation;

Wolof

jenn jëmm moo am, menn xel, ak jenn yaakaaru ëllëg ju wooteb yàlla ëmb.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

je vous exhorte donc, moi, le prisonnier dans le seigneur, à marcher d`une manière digne de la vocation qui vous a été adressée,

Wolof

man mi ñu tëj kaso ngir boroom bi nag, maa ngi leen di dénk, ngeen dund dundin wu yellook wooteb yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est pourquoi, frères saints, qui avez part à la vocation céleste, considérez l`apôtre et le souverain sacrificateur de la foi que nous professons,

Wolof

kon nag yéen bokk yu sell yi, yéen ñi yàlla woo, ngeen bokk ci nguuram gu kawe ga, seetleen ci yeesu, moom miy ndawu yàlla li, di saraxalekat bu mag bi ci yoon wi nu gëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

par la puissance de dieu qui nous a sauvés, et nous a adressé une sainte vocation, non à cause de nos oeuvres, mais selon son propre dessein, et selon la grâce qui nous a été donnée en jésus christ avant les temps éternels,

Wolof

moo nu musal te woo nu ci dund gu sell, ci lu ajuwul ci sunuy jëf, waaye ci dogalu boppam ak yiwam, wi nu yàlla may ci kirist yeesu, ba àddina sosoogul.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

French

c`est par la foi qu`abraham, lors de sa vocation, obéit et partit pour un lieu qu`il devait recevoir en héritage, et qu`il partit sans savoir où il allait.

Wolof

ngëm moo tax ba ibraayma déggal yàlla. bi ko yàlla wooyee, mu dem toxu ci menn réew, ma mu waroon a jote ca yàlla. noonu la gàddaaye dëkkam te xamul woon fan la jëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,799,197 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK