Results for antworten translation from German to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

German

Wolof

Info

German

und alle, die ihm zuhörten, verwunderten sich seines verstandes und seiner antworten.

Wolof

Ñépp ñi dégg li mu wax yéemu ci xel, mi mu àndal, ak ni mu doon tontoo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

eure rede sei allezeit lieblich und mit salz gewürzt, daß ihr wißt, wie ihr einem jeglichen antworten sollt.

Wolof

na seen wax jépp fees ak yiw te am xorom, ngir ngeen xam nan ngeen war a tontoo ku nekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und niemand konnte ihm ein wort antworten, und wagte auch niemand von dem tage an hinfort, ihn zu fragen.

Wolof

ci kaw loolu kenn mënu koo tontu genn kàddu. te li dale ci bés booba kenn ñemeetu koo laaj dara.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

wenn sie euch aber führen werden in ihre schulen und vor die obrigkeit und vor die gewaltigen, so sorget nicht, wie oder was ihr antworten oder was ihr sagen sollt;

Wolof

«bu ñu leen yóbboo ca jàngu ya, ca kanamu kilifa ya ak àttekat ya, buleen am xel ñaar ci li ngeen war a tontu ak nan ngeen war a tontoo, walla lu ngeen war a wax,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

dann werden ihm die gerechten antworten und sagen: wann haben wir dich hungrig gesehen und haben dich gespeist? oder durstig und haben dich getränkt?

Wolof

ci kaw loolu ñi jub dinañu tontu ne: “boroom bi, kañ lanu la gisoon, nga xiif, nu jox la, nga lekk; mbaa nga mar, nu jox la, nga naan?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

als er aber solches redete, gab der diener einer, die dabeistanden, jesu einen backenstreich und sprach: sollst du dem hohenpriester also antworten?

Wolof

bi yeesu waxee loolu, kenn ci alkaati yi nekkoon ci wetam daldi koy pes ne ko: «ndax nii ngay tontoo saraxalekat bu mag bi?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und der könig wird antworten und sagen zu ihnen: wahrlich ich sage euch: was ihr getan habt einem unter diesen meinen geringsten brüdern, das habt ihr mir getan.

Wolof

noonu buur bi dina leen tontu ne: “ci dëgg maa ngi leen koy wax, saa yu ngeen defalee loolu kenn ki gën a ndaw ci sama bokk yii, man ngeen ko defal.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

aber was sagt die göttliche antwort? "ich habe mir lassen übrig bleiben siebentausend mann, die nicht haben ihre kniee gebeugt vor dem baal."

Wolof

waaye lii la ko yàlla tontu: «dencal naa sama bopp juróom-ñaari junniy nit, ñi jaamuwul baal.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,788,104,805 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK