Results for arbeiter translation from German to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

German

Wolof

Info

German

denn solche falsche apostel und trügliche arbeiter verstellen sich zu christi aposteln.

Wolof

ay ndawi naaféq lañu, di ay liggéeykat yu njublaŋ yuy mbubboo turu ndawi kirist.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

darum bittet den herrn der ernte, daß er arbeiter in seine ernte sende.

Wolof

Ñaanleen nag boroom ngóob mi, mu yebal ay liggéeykat, ñu góob toolam.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

sehet auf die hunde, sehet auf die bösen arbeiter, sehet auf die zerschneidung!

Wolof

moytuleen xaj yi, waaw moytuleen ñiy jëfe lu bon, ñoom ñi seen xarafal weesul wàññi yaramu nit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

da sprach er zu seinen jüngern: die ernte ist groß, aber wenige sind der arbeiter.

Wolof

noonu mu ne taalibeem ya: «ngóob mi yaatu na, waaye liggéeykat yi barewuñu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

das himmelreich ist gleich einem hausvater, der am morgen ausging, arbeiter zu mieten in seinen weinberg.

Wolof

«noonu nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni boroom kër bu génn ci suba teel, ngir jël ay liggéeykat ndax toolu réseñam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

befleißige dich, gott dich zu erzeigen als einen rechtschaffenen und unsträflichen arbeiter, der da recht teile das wort der wahrheit.

Wolof

góor-góorlul ba teew fa kanam yàlla, nekk liggéeykat bu mu nangul te rusoo ci dara, di faramfàcce bu jub kàddug dëgg gi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

auch keine tasche zur wegfahrt, auch nicht zwei röcke, keine schuhe, auch keinen stecken. denn ein arbeiter ist seiner speise wert.

Wolof

buleen wut it mbuus ngir tukki mbaa ñaari turki, ay dàll mbaa aw yet, ndaxte liggéeykat yeyoo na dundam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und sprach zu ihnen: die ernte ist groß, der arbeiter aber sind wenige. bittet den herrn der ernte, daß er arbeiter aussende in seine ernte.

Wolof

mu ne leen: «ngóob mi yaatu na, waaye liggéeykat yi barewuñu. Ñaanleen nag boroom ngóob mi, mu yebal ay liggéeykat, ñu góob toolam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

in dem hause aber bleibet, esset und trinket, was sie haben; denn ein arbeiter ist seines lohnes wert. ihr sollt nicht von einem hause zum anderen gehen.

Wolof

dal-leen ca kër googa, tey lekk ak a naan lu ñu leen di jox, ndaxte liggéeykat yelloo na jot peyam. buleen dem nag kër ak kër.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

da antwortete der oberste der schule und war unwillig, daß jesus am sabbat heilte, und sprach zu dem volk: es sind sechs tage, an denen man arbeiten soll; an ihnen kommt und laßt euch heilen, und nicht am sabbattage.

Wolof

waaye njiitu jàngu ba mer, ndax li yeesu fajoon nit ca bésu noflaay ba, mu ne mbooloo ma: «am na juróom-benni fan yu nit ñi war a liggéey. kon war ngeen a ñëw faju ci bés yooyu, waaye du ci bésu noflaay bi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,738,125,007 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK