Results for blieben translation from German to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

German

Wolof

Info

German

und da wir gen syrakus kamen, blieben wir drei tage da.

Wolof

noonu nu teer dëkku sirakus, toog fa ñetti fan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

sie blieben aber beständig in der apostel lehre und in der gemeinschaft und im brotbrechen und im gebet.

Wolof

Ñoom nag ñuy wéy ci njàngalem ndaw yi ak cig bokk, ci damm mburu ak ñaan ci yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

wir aber vollzogen die schiffahrt von tyrus und kamen gen ptolemais und grüßten die brüder und blieben einen tag bei ihnen.

Wolof

bi nu jógee tir nag, nu demaat ci géej, ba teer patolemayis. foofa nu nuyu bokk ya, yendu, fanaan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

aber da fertigten die brüder paulus alsobald ab, daß er ginge bis an das meer; silas aber und timotheus blieben da.

Wolof

noonu bokk yi yebal pool ca saa sa, mu jëm géej, waaye silas ak timote des fa.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

stärkten die seelen der jünger und ermahnten sie, daß sie im glauben blieben, und daß wir durch viel trübsale müssen in das reich gottes gehen.

Wolof

di dooleel xeli taalibe ya, xiir leen ñu sax ci yoon wi; ñu ne leen: «ci kaw nattu yu bare lanu war a dugge ci nguuru yàlla.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

dieser trieb hinterlist mit unserm geschlecht und behandelte unsre väter übel und schaffte, daß man die jungen kindlein aussetzen mußte, daß sie nicht lebendig blieben.

Wolof

buur boobu nag dafa daan nax sunu xeet, di fitnaal sunuy maam, ba di leen sànniloo seeni doom, ngir ñu dee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

darnach zog er hinab gen kapernaum, er, seine mutter, seine brüder und seine jünger; und sie blieben nicht lange daselbst.

Wolof

bi loolu weesoo, mu ànd ak yaayam, ay rakkam ak i taalibeem, dem dëkku kapernawum. waaye yàgguñu fa.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

des andern tages zogen wir aus, die wir um paulus waren, und kamen gen cäsarea und gingen in das haus philippus des evangelisten, der einer der sieben war, und blieben bei ihm.

Wolof

nu jóge fa ca ëllëg sa, ñëw ba ca dëkku sesare. nu dugg ca kër filib, taskatu xebaar bu baax bi, mi bokk ci juróom-ñaar ña, nu dal fa moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und da er ihn fand, führte er ihn gen antiochien. und sie blieben bei der gemeinde ein ganzes jahr und lehrten viel volks; daher die jünger am ersten zu antiochien christen genannt wurden.

Wolof

bi mu ko gisee, mu indi ko ancos. noonu atum lëmm ñu bokk ak mbooloom ñi gëm, di jàngal nit ñu bare. te ci ancos lañu jëkk a tudde taalibe ya gaayi kirist.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

er sprach zu ihnen: kommt und sehet's! sie kamen und sahen's und blieben den tag bei ihm. es war aber um die zehnte stunde.

Wolof

yeesu ne leen: «kaayleen gis.» noonu ñu dem, seeti fa mu daloon, ngoonalal ko. ci tàkkusaani kaw la woon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

als er nun hörte, daß er krank war, blieb er zwei tage an dem ort, da er war.

Wolof

bi mu yégee nag ne, lasaar wopp na, mu toogaat yeneen ñaari fan ca bérab, ba mu nekkoon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,899,222,112 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK