Results for dritten translation from German to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

German

Wolof

Info

German

den hat gott auferweckt am dritten tage und ihn lassen offenbar werden,

Wolof

waaye yàlla dekkal na ko ci ñetteelu fan ba te biral ko,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und am dritten tage warfen wir mit unseren händen aus die gerätschaft im schiffe.

Wolof

te ca ñetteelu fan ba, ñu sànni ak seeni loxo jumtukaay, yi ñu yeboon ngir fàggu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und daß er begraben sei, und daß er auferstanden sei am dritten tage nach der schrift,

Wolof

suul nañu ko, mu dekki ca ñetteelu fan ba, ni ko mbind mi tërale.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und am dritten tag ward eine hochzeit zu kana in galiläa; und die mutter jesu war da.

Wolof

Ñaari fan gannaaw loolu ag céet am ca dëkku kana ca diiwaanu galile. yaayu yeesu teewe woon na ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und sie werden ihn töten, und am dritten tage wird er auferstehen. und sie wurden sehr betrübt.

Wolof

dinañu ko rey, mu dekki ca ñetteelu fan ba.» bi ko taalibe ya déggee, ñu am naqar lool.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

die werden ihn verspotten und geißeln und verspeien und töten; und am dritten tag wird er auferstehen.

Wolof

ñu ñaawal ko, di tifli ci kawam, dóor ko ay yar, rey ko. waaye gannaaw ñetti fan dina dekki.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

jesus antwortete und sprach zu ihnen: brechet diesen tempel, und am dritten tage will ich ihn aufrichten.

Wolof

yeesu tontu leen: «daaneel-leen kër yàlla gii, ma daldi koy yékkati ci ñetti fan.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

da nahmen die weingärtner seine knechte; einen stäupten sie, den andern töteten sie, den dritten steinigten sie.

Wolof

waaye beykat yi jàpp surga yi, kenn ki ñu dóor ko ay yar, keneen ki ñu rey ko, ki ci des ñu sànni ko ay doj.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und werden ihn überantworten den heiden, zu verspotten und zu geißeln und zu kreuzigen; und am dritten tage wird er wieder auferstehen.

Wolof

jébbal ko ñi dul yawut, ngir ñu di ko ñaawal te di ko dóor ay yar, ba noppi daaj ko ci bant. waaye ca ñetteelu fan ba dina dekki.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und einem gab er fünf zentner, dem andern zwei, dem dritten einen, einem jedem nach seinem vermögen, und zog bald hinweg.

Wolof

kenn ka, mu dénk ko juróomi milyoŋ, keneen ka, mu dénk ko ñaar; ka ca des, benn; daldi tukki.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und es wurden die vier engel los, die bereit waren auf die stunde und auf den tag und auf den monat und auf das jahr, daß sie töteten den dritten teil der menschen.

Wolof

noonu ñu daldi yiwi ñeenti malaaka, ya ñu waajaloon ngir at moomu, weer woowu, bés boobu ak waxtu woowu, ngir ñu rey benn ci ñetti xaaju nit ñi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und der dritte engel posaunte: und es fiel ein großer stern vom himmel, der brannte wie eine fackel und fiel auf den dritten teil der wasserströme und über die wasserbrunnen.

Wolof

Ñetteelu malaaka ma wol liitam. noonu biddiiw bu réy, yànj ni jum, xawee asamaan, daanu ci benn ci ñetti xaaju dex yi ak ci bëti ndox yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

es saß aber ein jüngling mit namen eutychus in einem fenster und sank in tiefen schlaf, dieweil paulus so lange redete, und ward vom schlaf überwältigt und fiel hinunter vom dritten söller und ward tot aufgehoben.

Wolof

noonu waxambaane wu tudd Ëtikus te toog ca palenteer ba, gëmmeentu bay jeyaxu. bi pool di gën a yaatal waxtaanam nag, nelaw daldi ko jàpp, mu xàwweekoo ca ñetteelu taax ma, daanu, ñu yékkati ko, fekk mu dee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und der vierte engel posaunte: und es ward geschlagen der dritte teil der sonne und der dritte teil des mondes und der dritte teil der sterne, daß ihr dritter teil verfinstert ward und der tag den dritten teil nicht schien und die nacht desgleichen.

Wolof

Ñeenteelu malaaka ma wol liitam. noonu dóorees benn ci ñetti xaaju jant bi, ak benn ci ñetti xaaju weer wi, ak benn ci ñetti xaaju biddiiw yi, ba tax benn ci ñetti xaaju leer gi lëndëm. bëccëg bi ñàkk leer diirub benn ci ñetti xaajam, guddi gi ñàkk leer diirub benn ci ñetti xaajam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

darum befiehl, daß man das grab verwahre bis an den dritten tag, auf daß nicht seine jünger kommen und stehlen ihn und sagen dem volk: er ist auferstanden von den toten, und werde der letzte betrug ärger denn der erste.

Wolof

danoo bëggoon nag, nga santaane, ñu wottu bàmmeel ba, ba am ñetti fan, ngir bañ taalibeem ya ñëw, sàcc néew ba, tey yégle ne dekki na. bu ko defee nax bu mujj boobu dina yées bu jëkk ba.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

das andere wehe ist dahin; siehe, das dritte wehe kommt schnell.

Wolof

Ñaareelu musiba mi wéy na, ñetteel baa ngi nii di ñëw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,167,073,099 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK