Results for freund translation from German to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

German

Wolof

Info

German

denn es ist mein freund zu mir gekommen von der straße, und ich habe nicht, was ich ihm vorlege;

Wolof

dafa am sama xarit bu ma ganesi, te awma dara lu ma ko jox.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und er sprach zu ihm: freund, wie bist du hereingekommen und hast doch kein hochzeitlich kleid an? er aber verstummte.

Wolof

buur ne ko: “sama waay, naka nga dugge fii, te amuloo mbubbum céet?” waa ji ne miig.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

ihr ehebrecher und ehebrecherinnen, wisset ihr nicht, daß der welt freundschaft gottes feindschaft ist? wer der welt freund sein will, der wird gottes feind sein.

Wolof

yéen ñi fecci seen kóllëre ak yàlla, xanaa xamuleen ne mbëggeelu àddina, mbañeel la fa yàlla? ku bëgg a xaritoo ak àddina nag, noonoo nga ak yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

er antwortete aber und sagte zu einem unter ihnen: mein freund, ich tue dir nicht unrecht. bist du nicht mit mir eins geworden für einen groschen?

Wolof

waaye boroom kër ga tontu kenn ci ñoom ne ko: “sama waay tooñuma la. ndax juboowunu woon ci benn denariyon?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

ich sage euch: und ob er nicht aufsteht und gibt ihm, darum daß er sein freund ist, so wird er doch um seines unverschämten geilens willen aufstehen und ihm geben, wieviel er bedarf.

Wolof

maa ngi leen koy wax, su jógul jox ko li muy laaj ndax li ñu xaritoo it, ndax la kee ñàkk jom dina tax mu jox ko lépp li mu soxla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

des menschen sohn ist gekommen, ißt und trinkt; so sagt ihr: siehe, der mensch ist ein fresser und weinsäufer, der zöllner und sünder freund!

Wolof

gannaaw gi nag doomu nit ki ñëw na, lekk, naan, ngeen daldi ne: “kii daal bëgg na lekk, di naan biiñ, tey xaritoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

und er sprach zu ihnen: welcher ist unter euch, der einen freund hat und ginge zu ihm zu mitternacht und spräche zu ihm: lieber freund, leihe mir drei brote;

Wolof

yeesu teg ca ne leen: «mi ngi mel ni, nga dem seeti sa xarit ci xaaju guddi ne ko: “xarit, lebal ma ñetti mburu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

German

freunde von gnome

Wolof

xariti gnome

Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,788,605,679 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK