Results for alla quale translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

non abbandonate dunque la vostra franchezza, alla quale è riservata una grande ricompensa

Wolof

kon nag buleen sàggane kóolute gi ngeen am, ndaxte ëmb na yool bu mag.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora vollero prenderlo sulla barca e rapidamente la barca toccò la riva alla quale erano diretti

Wolof

noonu ñu nangu koo dugal ca gaal ga, gaal ga daldi teer ca saa sa ca fa ñu bëggoon a wàcc.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e costeggiandola a fatica giungemmo in una località chiamata buoni porti, vicino alla quale era la città di lasèa

Wolof

nu romb fa ak coono yu bare, agsi ca bérab bu ñuy wax teeru yu neex, te dend ak dëkku lase.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

un solo corpo, un solo spirito, come una sola è la speranza alla quale siete stati chiamati, quella della vostra vocazione

Wolof

jenn jëmm moo am, menn xel, ak jenn yaakaaru ëllëg ju wooteb yàlla ëmb.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

combatti la buona battaglia della fede, cerca di raggiungere la vita eterna alla quale sei stato chiamato e per la quale hai fatto la tua bella professione di fede davanti a molti testimoni

Wolof

góor-góorlul ci bëre bu baax bi, ba ub làmbi ngëm, te feddali sag téye ci dund gu dul jeex gi; ndaxte ci loolu la la yàlla woo, te looloo waraloon it sa seede su rafet fa kanam mbooloo mu bare.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

egli è stato designato dalle chiese come nostro compagno in quest'opera di carità, alla quale ci dedichiamo per la gloria del signore, e per dimostrare anche l'impulso del nostro cuore

Wolof

te sax mbooloo yi ñoo ko tànn, ngir mu ànd ak nun, bu nuy yóbbu ndimbal li ngir ndamu boroom bi, te mu firndeel sunu yéene ju rafet.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e così abbiamo conferma migliore della parola dei profeti, alla quale fate bene a volgere l'attenzione, come a lampada che brilla in un luogo oscuro, finché non spunti il giorno e la stella del mattino si levi nei vostri cuori

Wolof

noonu bir na ne, waxu yonent yi wér na, te war ngeen koo fonk; mi ngi mel ni làmp, buy leer ci bérab bu lëndëm, ba kera fajar di xar, te biddiiwub njël bi feq, leeral seeni xol.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,775,765,495 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK