Results for anima nera translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

e che cosa potrebbe mai dare un uomo in cambio della propria anima

Wolof

te nit, lu mu war a weccee bakkanam?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

che giova infatti all'uomo guadagnare il mondo intero, se poi perde la propria anima

Wolof

ndaxte moom àddina sépp, lu muy jariñ nit, bu ñàkkee bakkanam?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

carissimo, faccio voti che tutto vada bene e che tu sia in buona salute, come va bene per la tua anima

Wolof

sama soppe, maa ngi ñaan, yàlla may la jàmm ci lépp, ànd ak wér gi yaram, ju mel ni sa naataangeg xol.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

gesù disse loro: «la mia anima è triste fino alla morte. restate qui e vegliate»

Wolof

mu ne leen: «sama xol dafa tiis, ba ma bëgg a dee; toogleen fii, xool.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

carissimi, io vi esorto come stranieri e pellegrini ad astenervi dai desideri della carne che fanno guerra all'anima

Wolof

samay xarit, yéen ñiy ay gan ak ay doxandéem ci àddina si, maa ngi leen di dénk lii: dëdduleen bànneexi bakkan yiy xeex ak xol.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

disse loro: «la mia anima è triste fino alla morte; restate qui e vegliate con me»

Wolof

mu ne leen: «sama xol dafa tiis, ba may bëgg a dee; toogleen fi, xool ak man.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

gli rispose: «amerai il signore dio tuo con tutto il cuore, con tutta la tua anima e con tutta la tua mente

Wolof

yeesu tontu ko ne: « “nanga bëgg yàlla sa boroom ak sa xol bépp ak sa bakkan bépp ak sa xel mépp.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

la moltitudine di coloro che eran venuti alla fede aveva un cuore solo e un'anima sola e nessuno diceva sua proprietà quello che gli apparteneva, ma ogni cosa era fra loro comune

Wolof

noonu mbooloom ñu gëm ñi bokk menn xel ak benn xalaat. kenn daawul aakimoo dara ci alalam, waaye ñoo bokkoon lépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

il dio della pace vi santifichi fino alla perfezione, e tutto quello che è vostro, spirito, anima e corpo, si conservi irreprensibile per la venuta del signore nostro gesù cristo

Wolof

na leen yàlla boroom jàmm sellal, ba ngeen mat sëkk; na sàmm seen xel mépp, seen xol bépp ak seen yaram wépp, ngir dara bañ cee am sikk, ba bés bu sunu boroom yeesu kirist dellusee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

qual vantaggio infatti avrà l'uomo se guadagnerà il mondo intero, e poi perderà la propria anima? o che cosa l'uomo potrà dare in cambio della propria anima

Wolof

te it moom àddina sépp lu muy jariñ nit, bu ñàkkee bakkanam? te nit, lu mu war a weccee bakkanam?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

costui rispose: «amerai il signore dio tuo con tutto il tuo cuore, con tutta la tua anima, con tutta la tua forza e con tutta la tua mente e il prossimo tuo come te stesso»

Wolof

nit ka ne ko: « “nanga bëgg yàlla sa boroom ak sa xol bépp ak sa bakkan bépp, sa kàttan gépp ak sa xel mépp,” te it: “nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp.”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,794,156,491 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK