From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
guardate le cose bene in faccia: se qualcuno ha in se stesso la persuasione di appartenere a cristo, si ricordi che se lui è di cristo lo siamo anche noi
xool-leen mbir mi ne fàŋŋ. bu amee ku mu wóor ne, ci kirist la bokk, na jàpp it ne, su bokkee ci kirist, nun itam ci kirist lanu bokk.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
alla stessa maniera, fratelli miei, anche voi, mediante il corpo di cristo, siete stati messi a morte quanto alla legge, per appartenere ad un altro, cioè a colui che fu risuscitato dai morti, affinché noi portiamo frutti per dio
nii laa leen ko man a misaale, samay bokk; bi kirist deeyee, dangeen a deeyandoo ak moom, te noonu yoonu musaa wàcc leen. léegi nag yéena ngi ànd ak keneen, maanaam kirist mi dekki, ngir nu amal yàlla njariñ.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: