Results for carissimi translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

non andate fuori strada, fratelli miei carissimi

Wolof

yéen sama bokk yi ma bëgg, buleen juum ci lii:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

fatevi dunque imitatori di dio, quali figli carissimi

Wolof

yéen nag ñiy guney yàlla, yi mu bëgg ci xolam, royleen ko ci loolu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

carissimi, se dio ci ha amato, anche noi dobbiamo amarci gli uni gli altri

Wolof

samay soppe, bu nu yàlla bëggee nii, nun itam war nanoo bëggante.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

non per farvi vergognare vi scrivo queste cose, ma per ammonirvi, come figli miei carissimi

Wolof

binduma leen loolu ngir ngeen am yeraange, waaye dama koo def ngir artu leen, ndaxte yéenay samay doom te bëgg naa leen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ma voi, o carissimi, ricordatevi delle cose che furono predette dagli apostoli del signore nostro gesù cristo

Wolof

waaye yéen samay xarit, fàttalikuleen la leen ndawi sunu boroom yeesu kirist waxoon lu jiitu,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

carissimi, io vi esorto come stranieri e pellegrini ad astenervi dai desideri della carne che fanno guerra all'anima

Wolof

samay xarit, yéen ñiy ay gan ak ay doxandéem ci àddina si, maa ngi leen di dénk lii: dëdduleen bànneexi bakkan yiy xeex ak xol.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

abbiamo perciò deciso tutti d'accordo di eleggere alcune persone e inviarle a voi insieme ai nostri carissimi barnaba e paolo

Wolof

kon nag mànkoo nanu ci tànn ay nit, yónnee leen ko, ànd ak sunuy soppe barnabas ak pool.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

lo sapete, fratelli miei carissimi: sia ognuno pronto ad ascoltare, lento a parlare, lento all'ira

Wolof

yéen sama bokk yi ma bëgg, nangeen xam lii: ku nekk war ngaa farlu ci déglu, di yéex a wax tey yéex a mer.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

carissimi, amiamoci gli uni gli altri, perché l'amore è da dio: chiunque ama è generato da dio e conosce dio

Wolof

samay soppe, nanu bëggante, ndax mbëggeel ci yàlla la bawoo; képp ku bëgg sa mbokk nag, ci yàlla nga juddoo, te xam nga yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ascoltate, fratelli miei carissimi: dio non ha forse scelto i poveri nel mondo per farli ricchi con la fede ed eredi del regno che ha promesso a quelli che lo amano

Wolof

dégluleen yéen sama bokk yi ma bëgg, ndax yàlla tànnul ñi néewle ci àddina, ngir ñu barele ci ngëm, tey am i cér ci nguur, gi yàlla dig ñi ko bëgg?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

carissimi, avevo un gran desiderio di scrivervi riguardo alla nostra salvezza, ma sono stato costretto a farlo per esortarvi a combattere per la fede, che fu trasmessa ai credenti una volta per tutte

Wolof

samay bokk, bëggoon naa leen a bind lool ci mbirum mucc gi nu bokk, waaye lii moo gën a jamp: ma xiir leen, ngeen taxaw ci aar mboolem dëgg, yi yàlla xas a dénk gaayam yu sell yi ba fàww.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

perciò, fratelli miei carissimi, rimanete saldi e irremovibili, prodigandovi sempre nell'opera del signore, sapendo che la vostra fatica non è vana nel signore

Wolof

kon nag sama bokk yi ma sopp, nangeen takku, sampu ba dëgër, te gën a sawar ci liggéeyu boroom bi, xam ne seen liggéey, bi jëm ci boroom bi, du neen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

certo, da tempo vi immaginate che stiamo facendo la nostra difesa davanti a voi. ma noi parliamo davanti a dio, in cristo, e tutto, carissimi, è per la vostra edificazione

Wolof

xanaa diirub li ngeen di jàng lii, defe ngeen ne, nu ngi wut aw lay ci seen kanam. samay xarit, nu ngi leen di wax ci kanam yàlla ak ci turu kirist; te lépp ngir seen njariñ la.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

non fatevi giustizia da voi stessi, carissimi, ma lasciate fare all'ira divina. sta scritto infatti: a me la vendetta, sono io che ricambierò, dice il signore

Wolof

samay soppe, buleen di feyantoo, waaye bàyyileen lépp ci loxoy yàlla, mi yelloo àtte; ndax yàlla nee na ci mbind mi: «man maay àtte, maay fey jëf.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

carissimi, noi fin d'ora siamo figli di dio, ma ciò che saremo non è stato ancora rivelato. sappiamo però che quando egli si sarà manifestato, noi saremo simili a lui, perché lo vedremo così come egli è

Wolof

samay soppe, léegi doomi yàlla lanu, te li nu nar a nekki feeñagul, waaye xam nanu ne, bés bu almasi bi feeñee, dinanu nirook moom, ndaxte dinanu ko gis, na mu mel.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,388,977 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK