Results for cattivi translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

profittando del tempo presente, perché i giorni sono cattivi

Wolof

tey jariñoo jot gi, ndaxte nu ngi ci jamono ju bon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

così sarà alla fine del mondo. verranno gli angeli e separeranno i cattivi dai buon

Wolof

noonu lay mel, bu àddina tukkee. malaaka yi dinañu génn, tànn ñu bon ñi ci biir ñu jub ñi,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

così ogni albero buono produce frutti buoni e ogni albero cattivo produce frutti cattivi

Wolof

noonu garab gu baax gu nekk dina meññ doom yu neex, waaye garab gu bon dina meññ doom yu bon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

un albero buono non può produrre frutti cattivi, né un albero cattivo produrre frutti buoni

Wolof

garab gu baax mënul a meññ doom yu bon, naka itam garab gu bon mënul a meññ doom yu neex.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

non c'è albero buono che faccia frutti cattivi, né albero cattivo che faccia frutti buoni

Wolof

«garab gu baax du meññ doom yu bon, te garab gu bon du meññ doom yu baax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

usciti nelle strade, quei servi raccolsero quanti ne trovarono, buoni e cattivi, e la sala si riempì di commensali

Wolof

noonu surga ya génn ca yoon ya, boole ña ñu fa gis ñépp, ñu bon ña ak ñu baax ña, ba néegu reer ya fees ak ay gan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

al punto che si mettevano sopra i malati fazzoletti o grembiuli che erano stati a contatto con lui e le malattie cessavano e gli spiriti cattivi fuggivano

Wolof

Ñu yóbbul sax ñi wopp ay kaala ak ay taraxlaay yu laaloon yaramam, ba jàngoro yi di leen bàyyi, rab yay génn ci ñoom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

quando è piena, i pescatori la tirano a riva e poi, sedutisi, raccolgono i pesci buoni nei canestri e buttano via i cattivi

Wolof

bi mbaal mi feesee nag, ñu ñoddi ko ci tefes gi, ba noppi ñu taxaw, dajale yu baax yi ciy ndab, waaye sànni yi bon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

mortificate dunque quella parte di voi che appartiene alla terra: fornicazione, impurità, passioni, desideri cattivi e quella avarizia insaziabile che è idolatria

Wolof

kon nag li nekk ci yéen te bokk ci mbiri àddina, jébbal-leen ko dee, yu deme ni ndoxaanu yàqute, sobe, xemmem, bëgg-bëgg yu bon, ak bëgge, maanaam bokkaale yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

se dunque voi, che siete cattivi, sapete dare cose buone ai vostri figli, quanto più il padre vostro celeste darà lo spirito santo a coloro che glielo chiedono!»

Wolof

ndegam yéen ñi bon yéena man a jox seeni gune lu baax, astemaak baay bi nekk ci kaw dina jox xel mu sell mi ñi ko koy ñaan!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

c'erano con lui i dodici e alcune donne che erano state guarite da spiriti cattivi e da infermità: maria di màgdala, dalla quale erano usciti sette demòni

Wolof

ak ay jigéen yu mu teqale woon ak rab te jële leen ci seeni wopp, ñu di: maryaama, mi ñuy wooye maryaamam magdala, mi yeesu tàggale woon ak juróom-ñaari rab;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

costui è accecato dall'orgoglio, non comprende nulla ed è preso dalla febbre di cavilli e di questioni oziose. da ciò nascono le invidie, i litigi, le maldicenze, i sospetti cattivi

Wolof

kooku boroom tiitar la, bu xamul dara. dafa wéradi, ba sóobu ci gëstuy neen ak i werante ciy araf yu dul jur lu dul ñeetaange, xuloo, xaste, ñaaw njort

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

accostiamoci con cuore sincero nella pienezza della fede, con i cuori purificati da ogni cattiva coscienza e il corpo lavato con acqua pura

Wolof

kon nanu jege yàlla ak xol bu laab, ak ngëm gu ànd ak kóolute, am xel mu dal ci bépp yeraange, ak yaram wu ñu raxas ci ndox mu sell.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,783,836,498 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK