Results for chiesero translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

gli chiesero: «dove vuoi che la prepariamo?»

Wolof

Ñu ne ko: «fan nga bëggoon, nu defare ko fa?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

chiamarono e chiesero se simone, detto anche pietro, alloggiava colà

Wolof

Ñu woote nag naan: «simoŋ, mi ñu dàkkentale piyeer, ndax fi la dëkk?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora gli chiesero: «come dunque ti furono aperti gli occhi?»

Wolof

Ñu ne ko: «lu ubbi say bët?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

i farisei e i sadducei si avvicinarono per metterlo alla prova e gli chiesero che mostrasse loro un segno dal cielo

Wolof

amoon na ay farisen ak ay sadusen yu ñëw ci yeesu. Ñu fexe koo fiir, ba laaj ko ne: «won nu kéemaan guy firndeel sag yónnent, te mu jóge ci asamaan.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

e, pur non avendo trovato in lui nessun motivo di condanna a morte, chiesero a pilato che fosse ucciso

Wolof

yoon dabu ko fenn, moona ñaan nañu pilaat, mu reylu ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

a queste parole i discepoli rimasero costernati e chiesero: «chi si potrà dunque salvare?»

Wolof

bi nga xamee ne taalibe ya dégg nañu loolu, ñu daldi waaru lool ne ko: «kan moo man a mucc nag?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

gli chiesero allora: «chi è stato a dirti: prendi il tuo lettuccio e cammina?»

Wolof

Ñu ne ko nag: «ku la ne: “jëlal sa basaŋ te dox?”»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

entrò poi in una casa e i discepoli gli chiesero in privato: «perché noi non abbiamo potuto scacciarlo?»

Wolof

bi yeesu duggee ci kër gi, taalibe yi laaj ko ci pegg: «lu tax mënunu ko woon a dàq?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora i discepoli, accostatisi a gesù in disparte, gli chiesero: «perché noi non abbiamo potuto scacciarlo?»

Wolof

bi loolu amee taalibe ya ñëw ci yeesu, laaj ko ci pegg: «lu tax nun mënunu woon a dàq rab wi?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

questi si avvicinarono a filippo, che era di betsàida di galilea, e gli chiesero: «signore, vogliamo vedere gesù»

Wolof

Ñëw nañu ci filib, mi dëkk betsayda ci diiwaanu galile, ne ko: «sang bi, danoo bëggoon a gis yeesu.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora gli si avvicinarono alcuni farisei per metterlo alla prova e gli chiesero: «e' lecito ad un uomo ripudiare la propria moglie per qualsiasi motivo?»

Wolof

bi mu fa nekkee, ay farisen ñëw ci moom, bëgg koo fiir; ñu ne ko: «ndax jaadu na nit fase jabaram, saa su ko neexee?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

anche i farisei dunque gli chiesero di nuovo come avesse acquistato la vista. ed egli disse loro: «mi ha posto del fango sopra gli occhi, mi sono lavato e ci vedo»

Wolof

looloo tax farisen ya di laajaat waa ja fi mu jaar bay gis léegi. mu ne leen: «dafa tay ban ci samay bët, ma sëlmuji, ba fi ma nekk maa ngi gis.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora gli chiesero: «che cosa dunque? sei elia?». rispose: «non lo sono». «sei tu il profeta?». rispose: «no»

Wolof

Ñu laaj ko ne: «kon yaay kan? ndax yaa di iliyas?» mu ne leen: «déedéet, duma iliyas.» Ñu ne ko: «ndax yaa di yonent, bi war a ñëw?» mu tontu ne leen: «déedéet.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,950,872,543 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK