Results for compiano translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

stendi la mano perché si compiano guarigioni, miracoli e prodigi nel nome del tuo santo servo gesù»

Wolof

tàllalal sa loxo, ci wéral ak ci wone ay kéemaan ak ay firnde, jaarale ko ci turu yeesu, sa ndaw lu sell li.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ma farò in modo che i miei due testimoni, vestiti di sacco, compiano la loro missione di profeti per milleduecentosessanta giorni»

Wolof

dinaa may sama ñaari seede yi, ñuy wax ci kàddug yàlla, sol ay saaku, di toroxlu diirub junni ak ñaari téeméeri fan ak juróom-benn-fukk.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

poi disse: «sono queste le parole che vi dicevo quando ero ancora con voi: bisogna che si compiano tutte le cose scritte su di me nella legge di mosè, nei profeti e nei salmi»

Wolof

noonu mu ne leen: «bi ma nekkee ak yéen, waxoon naa leen baat yii: li ñu bind lépp ci samay mbir ci yoonu musaa ak ci téerey yonent yi ak ci sabóor dafa war a am.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
9,166,872,402 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK