From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
giuseppe, destatosi, prese con sé il bambino e sua madre nella notte e fuggì in egitto
yuusufa nag jóg, jël xale ba ak ndeyam, làquji misra ca guddi ga.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
destatosi dal sonno, giuseppe fece come gli aveva ordinato l'angelo del signore e prese con sé la sua sposa
noonu yuusufa yeewu, yeggali jabaram, na ko ko malaakam boroom bi sante woon.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
destatosi, sgridò il vento e disse al mare: «taci, calmati!». il vento cessò e vi fu grande bonaccia
ci kaw loolu yeesu jóg, daldi gëdd ngelaw li, ne dex gi: «noppil te dal!» noonu ngelaw li dal, ba lépp ne nemm.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
accostatisi a lui, lo svegliarono dicendo: «maestro, maestro, siamo perduti!». e lui, destatosi, sgridò il vento e i flutti minacciosi; essi cessarono e si fece bonaccia
noonu taalibe yi jegesi yeesu, yee ko ne: «kilifa gi, kilifa gi, nu ngiy dee!» ci kaw loolu yeesu jóg, daldi gëdd ngelaw li ak duus yi. lépp dal, ba ne nemm.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: