Results for dico translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

questo però vi dico per concessione, non per comando

Wolof

li ma leen di wax fii du ndigal, waaye dama leen di xamal li ñu leen may, ngeen def ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

dico questo perché nessuno vi inganni con argomenti seducenti

Wolof

maa ngi wax lii, ngir kenn bañ leen a nax ci ay wax yu neex.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

per questo, dico, io piego le ginocchia davanti al padre

Wolof

moo tax maa ngi sukk, jublu ci yàlla baay

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

a me, invece, voi non credete, perché dico la verità

Wolof

waaye man damay wax dëgg, moo tax gëmuleen ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

in quel giorno chiederete nel mio nome e io non vi dico che pregherò il padre per voi

Wolof

bu keroogee dingeen ñaan ci sama tur. neewuma dinaa leen ñaanal baay bi,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ai non sposati e alle vedove dico: è cosa buona per loro rimanere come sono io

Wolof

lii laay yégal ñi séyul ak it ñi seen jëkkër dee: baax na ci yéen, su fekkee dangeen a toog rekk ni man, bañ a séy.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

chi di voi può convincermi di peccato? se dico la verità, perché non mi credete

Wolof

kan ci yéen moo man a seede ne, bàkkaar naa? su ma waxee dëgg nag, lu tax dungeen ma gëm?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ebbene io vi dico: nel giorno del giudizio avrà una sorte meno dura della tua!»

Wolof

waaye maa ngi leen koy wax, keroog bés pénc ma sodom moo lay tane.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

dico la verità in cristo, non mentisco, e la mia coscienza me ne dà testimonianza nello spirito santo

Wolof

li ma bëgg a wax nag, ci kanamu kirist laa koy waxe; dëgg la, du aw fen. sama xel, mi xel mu sell miy leeral, seedeel na ma ne, dëgg laay wax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

a voi miei amici, dico: non temete coloro che uccidono il corpo e dopo non possono far più nulla

Wolof

«maa ngi leen koy wax, samay xarit, buleen ragal ñu man a rey yaram, ba noppi dootuñu man a def dara.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

pertanto, ecco che cosa dico a voi, gentili: come apostolo dei gentili, io faccio onore al mio ministero

Wolof

yéen ñi dul yawut, yéen laay waxal. ndegam yàlla daf maa def ndawam, yónni ma ci yéen xeeti àddina si, damay matal samab yónnent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

così, vi dico, c'è gioia davanti agli angeli di dio per un solo peccatore che si converte»

Wolof

maa ngi leen di wax lii: ci noonule la malaakay yàlla yi di ame mbég ci benn bàkkaarkat bu tuubee ay bàkkaaram.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora, che cosa siete andati a vedere? un profeta? sì, vi dico, e più che un profeta

Wolof

kon lu ngeen seeti woon? yonent? waaw, wax naa leen ne, ëpp na yonent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora diedero a gesù questa risposta: «non sappiamo». e gesù disse loro: «neanch'io vi dico con quale autorità faccio queste cose»

Wolof

Ñu tontu yeesu nag ne: «loolu de xamunu ko.» noonu yeesu ne leen: «kon man itam duma leen wax ci ban sañ-sañ laay defe yëf yii.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,927,449,633 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK