From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
perché chiunque crede in lui abbia la vita eterna»
ngir képp ku ko gëm am ci moom dund gu dul jeex.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
e questa è la promessa che egli ci ha fatto: la vita eterna
te li mu nu digoon mooy lii: dund gu dul jeex.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
e, reso perfetto, divenne causa di salvezza eterna per tutti coloro che gli obbediscono
noonu la àgge cig mat, ñu def ko ki waral mucc gi dul jeex, ngir ñi ko déggal ñépp.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
chi ama la sua vita la perde e chi odia la sua vita in questo mondo la conserverà per la vita eterna
ku bëgg bakkanam dina ko ñàkk, waaye ku ko bañ ci àddina sii, dina ko denc ngir dund gu dul jeex gi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
che non riceva molto di più nel tempo presente e la vita eterna nel tempo che verrà»
dinga am tey jii ay yooni yoon, ak dund gu dul jeex ëllëg.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
chiunque odia il proprio fratello è omicida, e voi sapete che nessun omicida possiede in se stesso la vita eterna
képp ku bañ sa mbokk, reykat nga; te xam ngeen ne, ku rey nit amuloo dund gu dul jeex.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
chi mangia la mia carne e beve il mio sangue ha la vita eterna e io lo risusciterò nell'ultimo giorno
ku lekk sama yaram te naan sama deret, am nga dund gu dul jeex, te dinaa la dekkal keroog bés bu mujj ba.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
gli rispose simon pietro: «signore, da chi andremo? tu hai parole di vita eterna
simoŋ piyeer ne ko: «boroom bi, ci kan lanuy dem? yaa yor kàddu yiy joxe dund gu dul jeex.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ma chi avrà bestemmiato contro lo spirito santo, non avrà perdono in eterno: sarà reo di colpa eterna»
waaye kuy sosal xel mu sell mi deesu ko baal mukk; gàddu na bàkkaar ba fàww.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
chi semina nella sua carne, dalla carne raccoglierà corruzione; chi semina nello spirito, dallo spirito raccoglierà vita eterna
ku ji ngir sa nafsu, dinga góob li sa nafsu meññ, maanaam ag yàqute. waaye ku ji lu soloo ak xelum yàlla, li xel mi meññ ngay góob, maanaam dund gu dul jeex.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
che non riceva gia al presente cento volte tanto in case e fratelli e sorelle e madri e figli e campi, insieme a persecuzioni, e nel futuro la vita eterna
dinga am tey jii téeméeri yoon ay kër, doomi ndey yu góor ak yu jigéen, ndey, doom ak suuf, ñoom ak ay fitnay noon, te ëllëg nga am dund gu dul jeex.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
e lo stesso signore nostro gesù cristo e dio padre nostro, che ci ha amati e ci ha dato, per sua grazia, una consolazione eterna e una buona speranza
na sunu boroom yeesu kirist moom ci boppam ak yàlla sunu baay, mi nu bëgg te wone yiwam ci nun, ba ubbil nu buntu jàmm ju sax ak yaakaar ju wér,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
e il dio di ogni grazia, il quale vi ha chiamati alla sua gloria eterna in cristo, egli stesso vi ristabilirà, dopo una breve sofferenza vi confermerà e vi renderà forti e saldi
te yàlla mi jagoo yiw wépp te woo leen ci darajay kirist, ngir ngeen bokk ci ndamam li sax, gannaaw bi ngeen yendoo bëccëgu tiis, dina leen yeesalaat, di leen dëgëral ak a dooleel, ba ngeen sampu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
chi crede nel figlio ha la vita eterna; chi non obbedisce al figlio non vedrà la vita, ma l'ira di dio incombe su di lui»
ku gëm doom ji, am nga dund gu dul jeex; ku déggadil doom ji, amuloo dund, waaye merum yàllaa ngi la tiim.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
in verità, in verità vi dico: chi ascolta la mia parola e crede a colui che mi ha mandato, ha la vita eterna e non va incontro al giudizio, ma è passato dalla morte alla vita
«ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, ku dégg sama kàddu te gëm ki ma yónni, am nga dund gu dul jeex te doo jaar ca àtte ba, ndaxte génn nga ci dee, tàbbi ci dund.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
chiunque avrà lasciato case, o fratelli, o sorelle, o padre, o madre, o figli, o campi per il mio nome, riceverà cento volte tanto e avrà in eredità la vita eterna
koo xam ne kii dëddu nga ngir sama tur ay kër, ay doomi ndey yu góor walla yu jigéen, ndey walla baay, ay doom walla ay tool, dinga ko jotaat téeméeri yoon, ba noppi am dund gu dul jeex.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
allora paolo e barnaba con franchezza dichiararono: «era necessario che fosse annunziata a voi per primi la parola di dio, ma poiché la respingete e non vi giudicate degni della vita eterna, ecco noi ci rivolgiamo ai pagani
bi loolu amee pool ak barnabas ne leen ci lu bir: «yéen lanu war a jëkk a yégal kàddug yàlla, waaye gannaaw gàntu ngeen ko, ba àtte seen bopp ne, yeyoowuleen dund gu dul jeex gi, kon nu ngi woññiku ci ñi dul yawut.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
secondo il disegno eterno che ha attuato in cristo gesù nostro signore
mooy dogal bi sax dàkk, te yàlla tëral ko ci kirist yeesu sunu boroom.
Last Update: 2024-05-06
Usage Frequency: 5
Quality: