Results for io vado translation from Italian to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Italian

Wolof

Info

Italian

e del luogo dove io vado, voi conoscete la via»

Wolof

te fa ma jëm, xam ngeen yoon wi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

ed ecco ora, avvinto dallo spirito, io vado a gerusalemme senza sapere ciò che là mi accadrà

Wolof

«léegi maa ngi nii di dem yerusalem, ci li ma xelu yàlla mi xiirtal, te xawma lu ma fay dal.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

nella casa del padre mio vi sono molti posti. se no, ve l'avrei detto. io vado a prepararvi un posto

Wolof

am na néeg yu bare ca sama kër baay, bu dul woon noonu, ma wax leen ko, ndaxte maa ngi dem defaral leen fa ngeen di dëkk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

così parlò e poi soggiunse loro: «il nostro amico lazzaro s'è addormentato; ma io vado a svegliarlo»

Wolof

yeesu wax loolu, teg ca ne: «sunu xarit lasaar nelaw na, waaye maa ngi dem yee ko.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

avete udito che vi ho detto: vado e tornerò a voi; se mi amaste, vi rallegrereste che io vado dal padre, perché il padre è più grande di me

Wolof

«dégg ngeen li ma leen wax: “dinaa dem, waaye dinaa dellusi ci yéen.” bu ngeen ma bëggoon, dingeen bég ci li may dem ca baay ba, ndaxte baay bee ma gën a màgg.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

allora gesù andò con loro in un podere, chiamato getsèmani, e disse ai discepoli: «sedetevi qui, mentre io vado là a pregare»

Wolof

bi loolu amee yeesu ànd ak ñoom ba ca bérab bu tudd setsemane, mu ne taalibe ya: «toogleen fii, ma dem fale, ñaan fa.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Italian

disse loro simon pietro: «io vado a pescare». gli dissero: «veniamo anche noi con te». allora uscirono e salirono sulla barca; ma in quella notte non presero nulla

Wolof

simoŋ piyeer ne leen: «maa ngi nappi.» Ñu ne ko: «nun it danuy ànd ak yaw.» Ñu dugg gaal, daldi dem. waaye guddi googu jàppuñu dara.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
8,040,559,840 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK