From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
invece la gerusalemme di lassù è libera ed è la nostra madre
waaye yerusalem, ga ca kaw, mooy gor si. moom mooy sunu ndey.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
così, fratelli, noi non siamo figli di una schiava, ma di una donna libera
kon nag bokk yi, nun dunu doomi jaam, ay doomi gor lanu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
sta scritto infatti che abramo ebbe due figli, uno dalla schiava e uno dalla donna libera
mbind mi nee na: ibraayma am na ñaari doom; ki jaam bi jur ak ki gor si jur.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
fattosi giorno, i magistrati inviarono le guardie a dire: «libera quegli uomini!»
bi bët setee, àttekat ya yónni alkaati ya, ñu ne boroom kaso ba: «yiwil ñaari nit ñooñu, ñu dem.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ma quello dalla schiava è nato secondo la carne; quello dalla donna libera, in virtù della promessa
doomu jaam bi juddu na ni bépp doom, waaye doom, ji mu am ak jabaram, juddu na ci kaw digeb yàlla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
e attendere dai cieli il suo figlio, che egli ha risuscitato dai morti, gesù, che ci libera dall'ira ventura
te ngeen di séentu doomam bàyyikoo asamaan, moom yeesu mi mu dekkal te di nu musal ci merum yàlla, mi nar a ñëw.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
la moglie è vincolata per tutto il tempo in cui vive il marito; ma se il marito muore è libera di sposare chi vuole, purché ciò avvenga nel signore
jigéen ji séy dina ànd ak jëkkëram giiru dundam. waaye su jëkkër ji faatoo, man na séy ak ku ko neex, su fekkee ne góor gu gëm la.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
essa sarà dunque chiamata adultera se, mentre vive il marito, passa a un altro uomo, ma se il marito muore, essa è libera dalla legge e non è più adultera se passa a un altro uomo
kon nag su jabar ji àndee ak beneen góor, te fekk jëkkër jiy dund, dees na ko àtte njaaloo. waaye bu jëkkër ji faatoo, yoon jeexal na seen diggante; man na séy nag ak beneen góor, te loolu du njaaloo.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
gnome è un ambiente desktop libero, usabile, stabile e accessibile per la famiglia di sistemi operativi tipo unix.
gnome ab wërlaayub binduwaay la bu féex, yomb a jëfandikoo, jotale ngir xeeti nosteg doxiin yu dàttu ci unix.
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality: