From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
si recarono da lui con un paralitico portato da quattro persone
noonu, am ñu ko indil ku yaramam wépp làggi, ñeenti nit jàppoo ko.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
qui trovò un uomo di nome enea, che da otto anni giaceva su un lettuccio ed era paralitico
mu gis fa nit ku làggi, tudd ene, tëdd ci basaŋ diirub juróom-ñetti at.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ed ecco alcuni uomini, portando sopra un letto un paralitico, cercavano di farlo passare e metterlo davanti a lui
noonu ay nit ñëw, jàppoo basaŋ, ga ñu tëral nit ku yaram wépp làggi. Ñu di ko wut a dugal ca kër ga, ngir indi ko ca yeesu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ti ordino - disse al paralitico - alzati, prendi il tuo lettuccio e và a casa tua»
«maa ngi la koy sant, jógal, jël sa basaŋ te nga ñibbi.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
gesù, vista la loro fede, disse al paralitico: «figliolo, ti sono rimessi i tuoi peccati»
bi yeesu gisee seen ngëm, mu ne làggi ba: «sama waay, baal nañu la say bàkkaar.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
che cosa è più facile: dire al paralitico: ti sono rimessi i peccati, o dire: alzati, prendi il tuo lettuccio e cammina
lan moo gën a yomb, ma wax ku làggi ki: “baal nañu la say bàkkaar,” walla ma wax ko: “jógal, jël sa basaŋ, tey dox”?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
da molti indemoniati uscivano spiriti immondi, emettendo alte grida e molti paralitici e storpi furono risanati
ndaxte ay rab yu bon bàyyi nañu nit ñu bare, ña ñu jàppoon, di yuuxu ci kaw; te ñu bare ñu làggi ak ñu lafañ daldi wér.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: